Baba mi ani I guili wana merer Waa ji su ma koy xoolee ak ni mu mel Ah, n bi ne ci neex Ubbi buntu bus bi dugg sama xol Li moom du neen Mu geestu xool ma Ci la xam ne du xemmem May ñami-ñami Ku la jib waññi yaay dos d’âne Bus ba ngi daw te romb na sama arrêt Mbaa du terminus la ma jëme Dara dakar foo dem-dikk Fees nga dell ci man Te xawma yaw la kan Xol bi naan ma te nga dem-dikk xool ba xam Fees nga dell ci man Te xawma yaw la kan Xel bi naan ma toggal bul dem jigéen du yomb Ouhe baba, ouhe Ouhe baba Mbiɗa yiɗmaa Yiɗmaa Bus ba ngi riir, man degatuma Bëgg naa la piir ndax gisatuma Mbëggéel bu gaaw mel ni lu jaare si peage Oh dof naa ci yaw, ki la doon seet? Jomb te gisuma jinne (aaahn aaahn) Jàpp ma tej condamné (aaahn aaahn) Jokk na arrêt lay demandé (aaahn aaahn) Ba chauffeuru bus bi freiner Mu nax ma séy Fees nga dell ci man Te xawma yaw la kan Xol bi naan ma te nga dem-dikk xool ba xam Fees nga dell ci man Te xawma yaw la kan Xel bi naan ma toggal bul dem jigéen du yomb Le courage m’a quitté (J’ai même pas osé tenter) Hypnotisée par son charme J'suis tombée en amour Fees nga dell ci man, ahan Xol bi naan ma te nga dem-dikk xool ba xam Fees nga dell ci man, ahan Xel bi naan ma toggal bul dem jigéen du yomb Ouhe Fees nga dell ci man (ouhe) Te xawma yaw la kan (ouhe) Xol bi nana ma te nga (ouhe) Dem-dikk xol ba xam (ouhe) Fees nga dell ci man Te xawma yaw la kan Xel bi naan ma toggal bul dem jigéen du yomb Ba bus bi freiner Ci la xam ne rëcc na ma Lu tax demuma? Ba ci moom wax ko li fi ne!