Xooluma keneen, fees naa sama seetu Jigéen jiy waxe jëf du am jotu tontu Doon awo di buuru kër gi du ay fontu Te sax fu ma moomee, zéro la koy wacce Lu dés mëna daw, 1 bee ngi ci kaw Ñaari fan yu ne coco fëgg àljanna taxaw Bonheur Fi wax amul cuuraay géy riir Def terreur Lu tax muy sedd te may jekk pire Pese sama bopp xam ne waruma ragal wujje Laajal mon coeur kuy madame bonheur Yaa may confiné lépp di jupp yaa raw policier Laajal mon coeur kuy madame bonheur Ouh wool ma abass Chéri fatou ak chilel boroom gambia Li lay dóor te du la laal, neexul ci xol Deuxième dame bi lañu takkal medaille d’or Ki nelaw la xamoon ma jàngal ko yàndoor Bàyyi leen di jëm jàng xam sa góor gëna woor Xol bi nangu féete Booboy dundu mbégté Nàmmuma daray wax Ba fi mi ngi baax Chérie duggal dëkk do fëgg yaay laisser passer Allo Fi maay sourire muy évanouir Mais allo Ay nelaw jeex na dama yor liir Pese sama bopp xam ne waruma ragal wujje Laajal mon coeur kuy madame bonheur Yaa may confiné lépp di jupp yaa raw policier Laajal mon coeur maay ki koy bonheur Coco man ak yaw ba àljanna Ci sa wét lay dunde oh là là Yaa gaaw ci man Say je t'aime ci sama biir tempan Ni nga may def neex na ma Bëgg naa la, bae Pese sama bopp xam ne waruma ragal wujje Laajal mon coeur kuy madame bonheur Yaa may confiné lépp di jupp yaa raw policier Laajal mon coeur kuy madame bonheur Laajal mon coeur kuy madame bonheur Laajal mon coeur maay ki koy bonheur