Oooh ooh Naa naa, yeah It's about love, baby La patience est dure Mais sa récompense est pure Xaar bi yagg na te lu yagg dëgg la Moo tax ku muuñ muñ Ñu ñaar la woon Muy neex ak muy naxari Tay ñu nekk noon suba ay xarit Ànd bile jiitu na judd bi (Ouhouhou) ouh way ooh oh (Ouhouhou) diggënte bi dafa over nice (Ouuuuh) over nice, yé hee (Ouuuuh) maa la bëgg te ma xam sa price, xam sa price (Ouhouhou) wooh oh, buur bi Yàlla moo ko organize, organize (Ouuuuh) yeah eh, I love you baby Ooh Bës bi ma doon xaar agsi na Mësuma bég ba mu romb li Mësuma bég ba mu romb li Nan, nan, nan, nan, nan Ooh Bës bi ma doon xaar agsi na Mësuma bég ba mu romb li Mënuma bég ba mu romb li Nan, nan, nan, nan, nan Nara na na na naara na Yeah, yeaaah Oooh ooh Love Xamoon naa ni dina mësa neex Lu metti loo gis dina mësa jeex Lu doonoon sama yééne moo di Fomp sa rangooñ, dap sa bàaneex I love you, man bëgg naa la Sommi yanima bernam ene faada Waxoon naa la bul la dara métti My baby, I got your back (Ouhouhou) tay ji yaddi sama soxna (Ouhouhou) man ak yaw ñu ànd bokk soxla, ooh (Ouuuuh) tay de jot na (Ouuuuh) yeah, bës bile jot na (Ouhouhou) tay ji yaddi sama soxna (Ouhouhou) man ak yaw ñu ànd bokk soxla, ooh (Ouuuuh) bës bile jooot na (Ouuuuh) ma ne bës bi la jot na Ooh Bës bi ma doon xaar agsi na Mësuma bég ba mu romb li Mësuma bég ba mu romb li Nan, nan, nan, nan, nan Ooh Bës bi ma doon xaar agsi na Mësuma bég ba mu romb li Mënuma bég ba mu romb li Nan, nan, nan, nan, nan Ooh, oh, oh Bës bi ma doon xaar yegsi na Mësuma bég ba mu romb li Mësuma bég ba mu romb li Oooh Bës bi ma doon xaar yegsi na Mësuma bég ba mu romb li Mësuma bég ba mu romb li Oooh (I love you) Bës bi ma doon xaar yegsi na (eh, I love you) Mësuma bég ba mu romb li Mësuma bég ba mu romb li (You're the one that I lo-lo-love, yeah) Oooh (loving you) Bës bi ma doon xaar yegsi na (my baby I love you) Mësuma bég ba mu romb fi Mësuma bég ba mu romb li (Mënuma begg ba mu romb li, yeah) Oooh (yeah) Bës bi ma doon xaar yegsi na (I love you) Mësuma bég ba mu romb fi Mësuma bég ba mu romb li Yeah!