Ana li tax nit ki di bëgg, tax nit ki di bañ Tax nit ki di jooy di jëfe li muy bañe Yaw de yaay ki tax mu daw Ngir nga sori bépp coow Tax de caabi féete na leen ginnaaw Teewul tey laa la gën a nob Tay laa la gën a fonk Tay laa la gën a sopp Tay laay gën a dof ci yaw Bi mbëggeel bokkul ak bu ñooñu Bi mbëggeel bokkul ak bu ñooñu Moom ne na fi nga dem laay dem Fi nga ne laay ne Bopp ak bopp, mbagg ak mbagg, tank ak tank Ndaxte yaw laa love Waa ji ne na yaw laa love Moom ne na fi nga dem laay dem Fi nga ne laay ne Bopp ak bopp, mbagg ak mbagg, tank ak tank Ndaxte yaw laa love Waa ji ne na yaw laa love Ouh, yeen a bokk yëg-yëg Ouh, yeen a bokk ngëm-ngëm Ouh, yeen a bokk gis-gis Ouh, oh oh Tu es celle qu'il a choisi, qu'il a suivi Tu es son ame soeur T'es celle qui a fait de lui un kilifa Ouais ouais, t'es celle qui a fait de lui un kilifa Kon xamal ni nak muy naaj di guddi ak lu mu metti Du mës a bàyyi, non non du mës a xàddi Ñaari nit la, te yeen ñaar la Kon nak bëggalante waay! Nyaari nit leu teh yen nyaar la Kon nak beugeuntelene waay Moom ne na fi nga dem laay dem Fi nga ne laay ne Bopp ak bopp, mbagg ak mbagg, tank ak tank Ndaxte yaw laa love Waa ji ne na yaw laa love Moom ne na fi nga dem laay dem Fi nga ne laay ne Bopp ak bopp, mbagg ak mbagg, tank ak tank Ndaxte yaw laa love Waa ji ne na yaw laa love Waaw wallaay fi nga ne (laay ne) Waay fi nga jëm (laay ne) Moom bopp ak bopp, mbagg ak mbagg, tank ak tank Ndaxte yaw laa love Xale bi ne na moom yaw la bëgg, waay! Xale bi ne na moom yaw la love, waay! Ndax ne na fi nga nekk (laay ne) Waa wallaay fi nga jëm (yaw laay ne) Ndax bopp ak bopp, mbagg ak mbagg, tank ak tank Ndaxte yaw laa love Xale bi ne moom yaw la love, waay Ndaxte yaw la love Xale bi ne moom yaw la bëgg waaw