This is the Remix Girl like you My name is Admow Flow, aka Chos Nobody wanna see us together (together, yeah) Nobody wanna see us together but they don’t matter know Xool naa la xool keneen Gis ni bokkuleen Kon jarul may dem seeti keneen No, no, no Yaa ma jox say coordonés Sama life nga ordonné ko Kon man duma la abandonné, baby Ku mel ni yaw mooy ki baax ci man Ku mel ni man mooy ki baax ci yaw Su guddi xaajee ba sama xel dem ci yaw Maa xam ni I love you, yeah yeah Yeah yeah yeah Yeah yeah yeah Soxna si, I love you yeah yeah Yeah yeah yeah Yeah yeah yeah Soxna si, I love you yeah yeah Dama blindé ci ñeneen ñi, doon ngaaka ci yaw (Cause I love you, yeah yeah) Jamdong laa la bégal, dinga dundu ba gis ko (Cause I love you, yeah yeah) Oh souka débo yodi, ko ane woni fittandam Ko oh Modji, sa diali, éné boubna berdame Ohhh woni sékhilame Ohhh woni guidélame Ohhh woni diom soudame, honoma ala no no no Ku mel ni yaw mooy ki baax ci man Ku mel ni man mooy ki baax ci yaw Su guddi xaajee ba sama xel dem ci yaw Maa xam ni I love you, yeah yeah Yeah yeah yeah Yeah yeah yeah Soxna si, I love you yeah yeah Yeah yeah yeah Yeah yeah yeah Soxna si, I love you yeah yeah Loving you is what I do girl (éh aay éh) Dañu bëggante ba mujj niróo (éh aah aahh éh) Kone ane woni é ndér bérndam, girl Halnam saa ndaarikam holko ndiyata Xool ma ci ay bët wax ma looy gis? Sori la baby dina ma diis, baby [avec OMG] Ku mel ni yaw mooy ki baax ci man Ku mel ni man mooy ki baax ci yaw Su guddi xaajee ba sama xel dem ci yaw Maa xam ni I love you, yeah yeah Yeah yeah yeah Yeah yeah yeah Soxna si, I love you yeah yeah Yeah yeah yeah Yeah yeah yeah Soxna si, I love you yeah yeah