Ànd bu yagg Mën na metti yenn saay So amulee fiit Do xam fu guro di jaay Li ngay yekk sa xol Ci takkusaan bi Gëna neex suñ la maay auto Li ngay yekk sa xol Ci takkusaan bi Cours des grand celibat takule Xale bi, jaraal na la lii Loy xaar? Yaw ani yaw sa fiit, ani góór ak tiit Loy xaar? Wan na ko ni, fi mo fi nee Loy xaar? Soo bëggee nit mu jaaral li Loy xaar? Ci sëy, ci sëy Ñu mayeleen ngeen sëy Ci sëy, ci sëy Ci farata ngeen sëy Yaw ànd bu yagg Mën na metti yenn saay Te so amulee fiit Do xam fu guru di jaay Ne nga dan' ka love, dan' ka love Seet ci Yàlla wane fu la Wax ma lan ngay xoff, lan ngay xoff Demal ñaan ni ñu may la ko Sëy bu jigéén doon, ñaani góór yi jeex waay Yaw dinga ko togg lo, xarloo nga ko ba kañ waay Ne nga dan' ka love, dan' ka love Seet ci Yàlla wane fu la Wax ma lan ngay xoff, lan ngay xoff Demal ñaan ni ñu may la ko Ci sëy, ci sëy Ñu mayeleen ngeen sëy Ci sëy, ci sëy Ci farata ngeen sëy Waawaaw Ki may bëgg wooy mooy Jeri ngone masamba Lat sukabe ma samba Astou Mbaye falli ngone massamba Ma falli Coumba ndam tek ma Balaa yewu fu ki bale ak ñaar taak Astou Mbay géwël yacc ndaak Ak geer yacc ndaak Man ne géwël yacc ndaak te ak geer yacc ndaak Ko ci wo ma lawbe samba ku li misi seydi ndaak laay wuyo Eeeeeeeeeh waay! Jeri ngone Mbaye jeri ngone xari Jeri ngone massamba Astou Mbaye Astou Mbayee chéri toma Astou Mbaye yaayu Aleya Jeri ngone Mbaye, Jeri ngone xarii Jeri ngone massamba Astou Mbaye Marietu acc sa yaay el feky Jigéénu bacc kaay Jeri ngone Mbaye jeri ngone xari Jeri ngone massamba Astou Mbaye Kone malay woyal sa raak molay woyal Tay malay woyal Gawlo bi molay wayal Jeri ngone Mbaye, jeri ngone xari Jeri ngone massamba Astou Mbaye