Bébé yaw ba namm nga ma Man dama la namm ba namm ni ma la nammee yeah Te yaw bébé tam nga nak Jël peage bi raw ma mais nak tey ma fële pé yeah Bébé yaw ba aimer nga ma Man dama la aimer ba aimer ni ma la aimer yeah Te yaw bébé jaral nga ma Doxe ak ay dal weñ ci desert bi ba mu jeex yeah (ba mu jeex, ba mu jeex) Def ma ndank yaa ma mën ci pét ma nanguwat ko Ci jamm lay dox Waxoon naa la ko ci suba faw ma bamtuwat ko Dama la love Def ma ndank yaa ma mën ci pét ma nanguwat ko Ci jamm lay dox Waxoon naa la ko ci suba faw ma bamtuwat ko Dama la love Baby dama la, yaw dama la love Te ànduma ceek sago Baby dama la, yaw dama la love Maa la toppe dina dof baby Baby dama la, yaw dama la love Te ànduma ceek sago Baby dama la, yaw dama la love Maa la toppe dina dof baby Ne nga man rekk ma lay tooñ Wante bu dul man keneen kan moo ko saañ Ne nga may génnee sa rangooñ Ma lay tooñ ba fu tooñe dikk ba lu la tadoo bañ bae Yenn saay dinaa yëkkëti baat Mer ne la may naa la baat Yaram bi daw ma réccu wax ju ñaaw Ñëw di la baaluwat naan la bae dama doon foo Dama tam ay waxu con, xanaa du may Tom yaay Jerry Bëggante mënta ñak coow yaw, sekkuñu demal ma dem Awma mot xep-na je t'aime moo tax ma lay wax dama la bañ Mais dama la nob mënul am prix yaw am nga prix nobel Man dama la nob, dama la nob ba lab ci geeju nobel, Love you! Def ma ndank yaa ma mën ci pét ma nanguwat ko Ci jamm lay dox Waxoon naa la ko ci suba faw ma bamtuwat ko Dama la love Def ma ndank yaa ma mën ci pét ma nanguwat ko Ci jamm lay dox Waxoon naa la ko ci suba faw ma bamtuwat ko Dama la love Baby dama la, yaw dama la love Te ànduma ceek sago Baby dama la, yaw dama la love Maa la toppe dina dof baby Baby dama la, yaw dama la love Te ànduma ceek sago Baby dama la, yaw dama la love Maa la toppe dina dof baby