Liggéey ndey, ñaanu yaay, day def effect Barke baay, ñaanu sëriñ, day def effect Xar tanku tubey, naan sa doole day def effect Ku bëgg am lu kenn amul nak faut nga ñafe Ndekte liggéey day def effect Xaalis day def effect Sañse day def effect Même mbaraan day def effect Liggéey day def effect Xaalis day def effect Sañse day def effect Mbaaran day def effect Est-ce que ki yawa Jomiwuma leen ci doom Adama ak Awa (bainw) X-Presse nga indi mangeek Abba Jëleen coow bi ngeen di toj may tabax Dama yore xol bu bon ak xol bu baax Damay wor xaalis dama track ay xaalis Liggéey bi def effect ñépp dégg sama baat Mësuma changer masque, ku ma bama baax na Duma changer veste duma nit kenn bay nala ak Yàlla Xéy-na wuti ceeb, wuti ceeb Guddi guddi mbour lay nekk Bu dul Ara ku koy teg Bu ma tee may ba def ci man la ko joxeloo ci def Su la bukki, suli bukki boy, suli sedd Liggéey ndey, ñaanu yaay, day def effect Barke baay, ñaanu sëriñ, day def effect Xar tanku tubey, naan sa doole day def effect Ku bëgg am lu kenn amul nak faut nga ñafe Ndekte liggéey day def effect Xaalis day def effect Sañse day def effect Même mbaraan day def effect Liggéey day def effect Xaalis day def effect Sañse day def effect Mbaaran day def effect Eh dangeen di meew, dangeen di soob (oh no) Dangeen di reew, man dama dof Mënoo puus mënoo passe, eh kon demal gauche Li day def-effect, dama bëgg nga deme toog Sama tekki def effect, ma jëndal mère bi billet Makka Samay nak yak seen tolli, ñoo may wéyal geynak Oy yaay yak tolle jaambur, yey ye Jël sil reew mi bala newi, autopsie naan réy naa ko Gauche droite noce, spej na ma doy na ma no sad Gauche wrai, te xos, xalil ma xoos bii, xossa Di leen forcé ni ay gossi, ndios, di ndiossa Jutal ki ngay woowe king bi, sosse di sosa Liggéey ndey, ñaanu yaay, day def effect Barke baay, ñaanu sëriñ, day def effect Xar tanku tubey, naan sa doole day def effect Ku bëgg am lu kenn amul nak faut nga ñafe Ndekte liggéey day def effect Xaalis day def effect Sañse day def effect Même mbaraan day def effect Liggéey day def effect Xaalis day def effect Sañse day def effect Mbaaran day def effect Nit la bu reew ak xel mu dal, xale bi talul nelew Yàlla na ma Yàlla baal, sa feneen naan ci ngelaw Ndox la ci gox sappeur bi, joge di fay Li gay taal, xaftal ma, lof talal ma look li gay tal Fi la reew mi tool, dara du ko wodd Di daal ci subvention ndekete yaw sa rappeur yorul Yaw lekki yorul di njaay ni mbaam yi lay koti koti May nar bi fay sa rappeur nan ma day ko potti potti Lu ngeen fook lu ma book faw mu doon diil Took di xare ku ci wax ku bëggee coow bif Damay fo ngeen di xoofe, damay took xiif Dama dofe ngande démbu damay coopit Liggéey ndey, ñaanu yaay, day def effect Barke baay, ñaanu sëriñ, day def effect Xar tanku tubey, naan sa doole day def effect Ku bëgg am lu kenn amul nak faut nga ñafe Ndekte liggéey day def effect Xaalis day def effect Sañse day def effect Même mbaraan day def effect Liggéey day def effect Xaalis day def effect Sañse day def effect Mbaaran day def effect May ma fiston bii, cam gisson lyrics Rap sans Brick comme auto sans pistons cri Maa ngi gis comfli ay dir dir li clic Sama dicton mu ngi ci bisson ak ekive dip (ha ha ha) Su la neexee nga ni sa rappeur mooy king bi Mais ma koy reglé def sa sulu rappeur ci ciin bi Okay man sama gang lañ fal elilpi Isi na ci man sama gang lañ jox mérite bi Tabaski na may xar mu def effect Forcéwuma king te bu ko miin nak yaa ngi fi Yoru ñu tus, dañuy may gëna andete Jongul du néegu-góor ba tay loo lay pitaine li Liggéey ndey, ñaanu yaay, day def effect Barke baay, ñaanu sëriñ, day def effect Xar tanku tubey, naan sa doole day def effect Ku bëgg am lu kenn amul nak faut nga ñafe Ndekte liggéey day def effect Xaalis day def effect Sañse day def effect Même mbaraan day def effect Liggéey day def effect Xaalis day def effect Sañse day def effect Mbaaran day def effect Schi liggéey (day def effect) Waa boy xaalis ci bopp (day def effect) Hii, ñaanu yaay tamit (day def effect) Woo boy sañse (day def effect) Mbaraan, mbaraan, mbaraan (day def effect) Ñaanu yaay tamit (day def effect) Boy sañsé (day def effect) Day def effect!