Sama bopp dina toj mbaa lii yoon la Fu ma toog yaw rekk laay xalaat (Shadiiq!) Fan nga ne ma ñëw fóon la Yaw laa nob boo bëggee ma waat Barke Yónnent bi Maa ngi dee céy mbëggeel sonn naa Feeling feeling the love that you give me I'm feeling feeling alright Te ku ci love manoo bañ a tudd Fou fou-fou-fou fou fou Fo fo-fo-fo folle folle Fou fou-fou-fou fou fou Yaw boo nobee manoo bañ a dof Day yee sa folies yépp ñu naan la J'ai la folie Yaw laa def sama xol Yaay sama wéeruwaay kon dee ma soor Xeeñal nga sama xol Moo tax sama parfumé yaw rekk lay doon Yaay sama biberon Nàmpal ma suba ba ngoon Def ma comme Nabou Dash Bandit nga dee ma tooñ Baby girl t'es ma vice Dundal nga sama life Yaw rekk yaay sama size I love you, yeah you know why Ku bëgg fok nga Fou fou-fou-fou fou fou Fo fo-fo-fo folle folle Fou fou-fou-fou fou fou Yaw boo nobee manoo bañ a dof Day yee sa folies yépp ñu naan la Fou sama dof bi Coco chou, sama copine Sa xol bi laay foqati Bañuma photocopie Lu ma am jël, yaa ma doy Manuma la gëme ni nag beek Peul bi Jëndal la or, yaw yaa may tël Dañuy làcce Faly Ma indil leen Ngoye maay Askia Yàgg la góolu ni Casillas Sama nob siiw mel ni Fatiha Su ma tooñee nanga fàq yat Noq ma, maay jooy Naan la bébé, bonheur laa lay woowe ay Nutella Yaw nee ma sama dof bi, ndax fii ku bëgg ñu woowe la Fou fou-fou-fou fou fou Fo fo-fo-fo folle folle Fou fou-fou-fou fou fou Yaw boo nobee manoo bañ a dof Day yee sa folies yépp ñu naan la (Fou fou-fou-fou fou fou) Ku yëg sa mbëggeel dégg (Fo fo-fo-fo folle folle) Bul bañ ku la naan (Fou fou-fou-fou fou fou) Billahi ku bëgg teppeeral Boo nobee dangay tàngook sago, ñu naan la (Fou fou-fou-fou fou fou) Boo bëggee fàww nga dégg (Fo fo-fo-fo folle folle) Ku yëg sa mbëggeel dégg (Fou fou-fou-fou fou fou) Bul bañ ku la naan (Fo fo-fo-fo folle folle) Dëgg dëgg boo nobee manoo bañ a dof Day yee sa folies yépp ñu naan la (Fo fo-fo-fo folle folle) Dëgg dëgg boo nobee manoo bañ a dof Day yee sa folies yépp ñu naan la (Fo fo-fo-fo folle folle)