Kenn mënul jokk bari mbook (Ah déedéet!) Seytaane waxul dëgg benn yoon (Loolu dëgg la!) Lii la Yàlla dogal demal toog (Moo yaw demal toog) Yëg naa ni dañ may gis seen xol di bon Yah kon ñoo ngi dead (Mbaa ñoo ngi dead) Sama noon yi ñoo ngi dead (Ñu ngi dead) Sama noon yi ñoo ngi dead (Mbaa ñoo ngi dead) Sama noon ñoo ngi dead (Ñu ngi dead) Sama noon yi ñoo ngi dead (Mbaa ñoo ngi dead) Dead, dañu bàyyi jooy ñu ngi Ree, bu ñuy nelaw boy bu ñu Yee, xel mu dal ni ku julli Geer, xale nga demal fowi Mayal mak ñi nos Ku bareng barigo bii What's the fucking noise Néegu góor be yëgel gaz bi moo ngi wàcc Da ka bind gën leen dégg Yàlla Gën leen dégg koc Dañoo ree rekk, dëkk bi yëngu Ñu saraxe sakku socc Ara ak Dayza benn lañ ni pièce ak biais témère Ku ñu bañ li lay ray a ray ku bañ séeréer Vaccin ñëwaat na, président day pikkiru watt Reetaan sax moo ma gëna seen Ña nga lu liru jaan Kenn mënul jokk bari mbook (Ah déedéet!) Seytaane waxul dëgg benn yoon (Loolu dëgg la!) Lii la Yàlla dogal demal toog (Moo yaw demal toog) Yëg naa ni dañ may gis seen xol di bon Yah kon ñoo ngi dead (Mbaa ñoo ngi dead) Kuy xalam disi jaayu (Kuy xalam disi jaayu barke ba yaay boroom) Boo xamul na nga maandu (Boo xamul na nga maandu boo munul na nga ba) Man Senegaal la ma ngemb Kan moo samp ndënd mbër mi xanaa dafa rén Sori ma way, te nga dégg Bul ma ñodi lekk ma ni fekk nga ma réeg Ñangal billaay tital la Fixé la xool ma fitna bi dikk na Fuk kinezi aljuma Coow bi jël disu zizou ñu cissou Ma kidnapé seen xoli ma tay Da nge na baax rekk ma nég Da ngena baax Da nge na baax rekk ma nég Moo yeena baax (wàcc) Ñi bañ a baax ñu ngi dead Sama noon yi ñoo ngi dead (Ñu ngi dead) Sama noon yi ñoo ngi dead (Mbaa ñoo ngi dead) Sama noon ñoo ngi dead (Ñu ngi dead) Sama noon yi ñoo ngi dead (Mbaa ñoo ngi dead) Mbaa ñu ngi dead waa Senegaal ma ni Dispensaire ci loxoy golo Bu xàcc wope dafay dead, wuuw Dispensaire ci loxoy golo Bu xàcc wope dafay dead, wuuw Dispensaire ci loxoy golo Bu xàcc wope dafay dead, wuuw Dispensaire ci loxoy golo Bu xàcc wope dafay dead, wuuw