Dégg naa je t'aime bu ne Boo waxee je t'aime dootu ma la dégg damay gumba tegloo Dékku naa fi coow bu ne Boo waxee ba yëkkati sa baat bi dang may mu ma loo Te xol du gâteau, kenn du ko daggat-daggate Xol du pizza ba ku ne tël di laaj part Amooleen fi part Benn part la jox naa la ko ànd nañ ci Ngay doore di màtt Di doon patte di gajj Yaa rafet jikko, rafet xol de ma nappaaje Ngay doore di màtt Di doon patte di gajj Yaa rafet jikko, rafet xol de ma nappaaje Man su ma dee dee ci àll gaynde may ray Man su ma dee, bëgg damay bëggaale sa démbaak tay Tewul luñ la waxal yawa Waaye man ak yawa Danga sikk ñépp ko wax taxul ma dem bala Eh luñ la waxal yawa Waaye man ak yawa Danga sikk ñépp ko wax taxul ma dem bala Jarul ngay laaje mana mana (mana mana) Luñ ma mënti waxal mana mana (mana mana) Maa toj kasi mana mana (mana mana) Eh xale bi ko nopp mu ne mana mana (mana mana) Eh maa ñëw këf la coppet Maa koy neexal ci pet Dal sama kaw rekk toj ni benn nen bu bonde ci kekk Sur le plat lañ fi tekk Xam naa ni yaw la fi fekk Yor naa sikkim pur nga teg ci mbej maay sa sikket Ok wala (walaaa), jublu waya nga kaaba Jàppal sikkim ne a ba ça ma ne watawallah Foo dem foo dem maa nga fa Ëppal xawma ndanka Doxalal foo dox ba tegi jokk ma teg fa tanka (damn!) Jugal ñu dem nelawi (nelawi) Naw ci kaw ni Aladine (Aladine) Yaa raw héritage maa dewe lekkal sama alal yi Xam nga maa la nob, dama la nob nobaale sa rab bi C'est normal ma dof ci yaw parce que yaa yor sama garab yi Eh ku lay woo, ku lay woo Bul laaje, man ma lay woo Bae yaa may tooñ maa lay tooñ Suñu mbëggeel moo raw coono Sama volume fi mu nekk moo baax Bu de da low ma yokkat Boo reetaanee laay kontaan Xale bile yaa raw seytane, yaa raw seytane Ba su ma dee dee ci àll gaynde may ray Man su ma dee, bëgg damay bëggaale sa démbaak tay Tewul luñ la waxal yawa Waaye man ak yawa Danga sikk ñépp ko wax taxul ma dem bala Eh luñ la waxal yawa Waaye man ak yawa Danga sikk ñépp ko wax taxul ma dem bala Jarul ngay laaje mana mana (mana mana) Luñ ma mënti waxal mana mana (mana mana) Maa toj kasi mana mana (mana mana) Eh xale bi ko nopp mu ne mana mana (mana mana)