Ne na ma yeen góor ñépp yem (yeen ñépp yem) Ku ngeen gis fowe ko dem (fowe ko dem) Bala ma dee ngeen di fen (yeen ngeen di fen) Jigéen bëggul fowe, je t'aime (yeah) Moo tax ñu leen di mbaraan Miin nañu façon doxaan Yàq xol rekk ngeen tamm Maa bañ awma seen temps, góor Ne naa la duma ñee (duma ñee) Dama am ci yaw cofeel (yeah) Waxuma la lu dul mbëggeel Man ay fo indiwuma fii bae Sama xol yaw la tànn Yaa ma daqal aljanna (yeah) Yaay Michelle maay Obama (yeah) Xanaa teel a kontaan Yaw dee ma ree Ñu ànd bëggante mbëggeelu indo Li nga bëgg ak li ma bëgg mingoo (mingoo) Kaay ñu bëggante mbëggeelu indo Li nga bëgg ak li ma bëgg mingoo Ehh, pain au lait Ohh, pain au lait Pain au pain au lait Ohh, pain au lait Pain au pain au lait Ohh pain au lait Pain au pain au lait Ohh, pain au lait Pain au pain au lait Pain au pain au lait Yaw dañoo nuroo tek tek Damay ragal bëgg lekk lekk Bëgg essayer yéeg Mais xel bi ne ma déedéet Sama xol tëdd perpect Gis naa lu may séet Te dinga ma bëgg bañ bañ Tekk na ci sama bakken Wala dinga ma ray bokk Boo dawul duma daw ngone lat Latir Diop Li du xeetu door Man a duma ñoom Fokk nga ni ñun ñépp ñoo yeme Non man ak ñoom duñu benn Noooo Diggante sa yaay man nga fay tek (yeah) Monogamie man rekk jege (yeah) Watt ko Yàlla lay dégg (yeah) Waxatuma lool Hummm, waa est-ce que yar do navigateur Non danga romb mool Pain au lait ñu diw sunu bëre Xëbbël sama xol Wante bëggante mbëggeelu Indo Li nga bëgg li ma bëgg mingoo (mingoo) Kaay ñu bëggante mbëggeelu Indo Li nga bëgg ak li ma bëgg Mingoo Ehh, pain au lait Ohh, pain au lait Pain au pain au lait Ohh, pain au lait Pain au pain au lait Ohh pain au pain au lait Pain au lait Pain au pain au lait (Kaay ñu bëggante mbëggeelu Indo) Pain au pain au lait (Li nga bëgg ak li ma bëgg mingoo) Pain au pain au lait (Kaay ñu bëggante mbëggeelu Indo) Pain au pain au lait Ohhh pain au lait Pain au pain au lait