Léegi Damay def ni yaw photo profil Boo soloo génn a ma sol jaar ne Pesum kanam boroom a kay fajal boppam Ni miy safe ci man rekk lay safe ci yaw Léegi Dangay jaay nàndite, maa def bandit Nga teg ma deal, ma teg la lu metti Pesum kanam boroom a kay fajal boppam Ni miy safe ci man rekk lay safe ci yaw mi Hee yaw eh, danga fok ni C’est officiel, danga juum Ne nga lu la neex def Mënoo, te ne nga ñofar Loo bataré ma coupal la ko Teggal la ci ay ree Ah, xamoo maak yaw Tant que du Diakka, du Église Ba dégguma Al-Xayri Soo ma nobee Respecté ma, ma respecté la Looloy game bi, looloy deal bi Soo bëggee ñu dund mbëggeel dëgg-dëgg Dangay bay sa xel bi ngay fowe Ni ngay jobe, ni ngay playé Doo gis ku mel ni man Yarul léegi bala may dem Bala may dem nga topp sama ginnaaw Naan su ma yëgoon Yarul léegi, yarul léegi Man doo ma nob di ma fowe Man doo ma am di ma fowe Moo tax léegi Man damay def ni yaw photo profil Boo solo gëna ma solu jaar ne Pesum kanam boroom a kaay fajal boppam Ni miy safe ci man rekk lay safe ci yaw Bëgg naa léegi Galanterie ju mat Yóbbu ma resto, toppatoo ma Shoppingal ma Te neexal ma Loo looy tax jamm am bala may dem Fii ku lamb ya tay Noy ame ngalam di wut përëm Kenn du mel ni man Yarul léegi, yarul léegi Man doo ma nob di ma fowe Man doo ma am di ma fowe Moo tax léegi Man damay def ni yaw photo profil Boo solo gëna ma solu jaar ne Pesum kanam boroom a kay fajal boppam Ni miy safe ci man rekk lay safe ci yaw Léegi Dangay jaay nandite ma def bandit Nga teg ma deal, ma teg la lu métti Pesum kanam boroom a kay fajal boppam Ni miy safe ci man rekk lay safe ci yaw mi Ñi ma bëgg bari na Fexel nga xam man maay kan Wala ma dem bàyyi la Pesum kanam boroom a kay fajal boppam Ni miy safe ci man rekk lay sage ci yaw Neñ ci dem kon en avant Loo batéré ma coupé la ko kaay Te lépp loo mbalax ma fecc ko kaay Pesum kanam boroom a kay fajal boppam Ni miy safe