Lila ci musël Moy di moytu Li ñëpp la titël Konn bul gëmméntu Moom dafa ñow nit ñi di dém Janté bi soo gissatu ñu lérr Meme samay xarit, mëna tu malen guiss Ba ko jip day tite Bul fàtte ni mi ngi fi (batay) Lax ko na mais mi ngi fii (batay) Bul fàtte ni mi ngi fi (baa tayy) Lax ko tina mais faites gaffe Lila ci musël Moy di moytu Li ñëpp la titël Konn bul gëmméntu Moytandiku Ni gnouy dundék jaan ci pax Respecté consigne yéy tax ñu dundaat lu neex Ndax wergu yaram bu sax egal happiness Revivons des jours meilleurs Bul fàtte ni mi ngi fi (batay) Lax ku na mais mi ngi fii (batay) Bul fàtte ni mi ngi fi (baa tayy) Lax ko tina mais faites gaffe Together we will get there And struggle for better days It's time to build our future Jok ni li daf fiey jekk (par force) Lila ci musël Moy di moytu Li ñëpp la titël Konn bul gëmméntu Fagaro gën faju Fagaro gën faju Konn negn leen vacciner wu (Vacciner wu) Bul fàtte ni mi ngi fi (batay) Lax ku na mais mi ngi fii (batay) Bul fàtte ni mi ngi fi (baa tayy) Lax ko tina mais faites gaffe Ngir aar sa bopp aare sa njaboot Moy respectez les gestes barrières Baña bayé ko fiy jëlé Li arr sa boppu aar sa njaboot (batay) Moy respecter les gestes barrières Fais gaffe!