Muy suba muy guddi Muy naaj Mbaa muy soobé Mësu maa wooté Te wuyu loo ma Boo weeté gore Weetali ku nga akk sa mbëggeel Mësu maa wooté Te wuyu loo ma Ah yeah Ah yeah Eh yah Mësu maa wooté Teh wuyu loo ma Fii ci adduna yaa Gisu ma ku melni yow Mbëggeelam yaatu na Yërmandeem moo ma yeem Ku melni yow Benn la dootul ñaar Yaay sama aljana Yow mi ma teg yoon Ci yoonu leer Cause I've been fearless To get to the road tonight Because so been love Nobody never Everything how to try But I believe in miracles now You're right here Yow mii sa mbëggeel bi yaatu na ni adduna Gestu gis la sama wet muy aljana Mësu maa la woo te wuyu loo ma Sa yërmande yeem na ma man Xeebu loo benn yoon siggil nga ma Def ma ni sa bopp te won nga ma I've been so grateful for your love Muy suba muy guddi Muy naaj Mbaa muy soobé Mësu maa wooté Teh wuyu loo ma Boo weeté goré Weetali ku nga akk sa mbëggeel Mësu maa wooté Teh wuyu loo ma Mësu ma la woo wuyu loo ma Saayu ma soxla nga jox ma xañ sa bopp Li nekk ci yow moy daw ci man mii Suma la gisee Moy gis naa sama bopp Lu fees ci xol feeñ ci jëmm jii Yow sa mbëggeel moo may weetali Yow mii Sa mbëggeel bi yaatu na ni adduna Gestu gis la sama wet muy aljana Mësu maa la woo te wuyu loo ma Sa yërmande yeem na ma man Xeebu loo benn yoon siggil nga ma Def ma ni sa bopp te won nga ma loolu I've been so grateful for your love Muy suba muy guddi Muy naaj Mbaa muy soobé Mësu maa wooté Te wuyu loo ma Boo weeté goré Weetali ku nga akk sa mbëggeel Mësu maa wooté Teh wuyu loo ma Teh wuyu loo ma