Now I know, now I know But I don′t know what I'm feeling inside Gestu woo ma Maa ngi dem, maa ngi dem Soo ma gisatul dem naa Maa ngi dem, baayi a fi sama xol Di naa weet, weet ci sama yoon Subateel, ba jant sow Yaa ngi sèntu, sa waay ju fi joge woon Maa ngi dem te taggu wu ma la Suma reeree mbaa duñ ne yow la Maa ngi dem te taggu wu ma la Suma reeree mbaa duñ ne yow la Ñëw naa fi noor (Ñëw naa ba dem gisoo ma) Ñëw naa fi nawet (Ñëw naa fi nawet tamit) Ñëw naa fi koor (Tabaski akk Tamxarit) Fekk fi bekkoor (Fekk la ngay bekkoor) Li ma dundee (Li ma dundee) Akk li ma weesu (Akk li ma weesu) Day dellusee (Da fay dellusee) Ba mel ni seetu (Ba mel ni seetu) Maa ngi dem te taggu wu ma la Suma reeree mbaa duñ ne yow la Maa ngi dem te taggu wu ma la Suma reeree mbaa duñ ne yow la Dem naa te taggu wu ma la (Dem naa) Suma reeree mbaa duñ ne yow la (Mbaa duñ ne yow la) Jooy naa te kenn dooru ma (Man dem naa) Suma reeree mbaa duñ ne yow la (Yow la) Maa ngi dem te taggu wu ma la Suma reeree mbaa duñ ne yow la Maa ngi dem te taggu wu ma la Suma reeree mbaa duñ ne yow la Maa ngi dem maa ngi dem