Ñibbisil Ñibbisi-i-il Jukk du wess, jukk du wess Su ma lay woo lu tax doo ma faale? Wax ma lu dañ ci man xanaa bëggetoo ma Yeah, yeah Bëtu mbëggeel la la mës a xool la Lu waral man ak yaw, ñu dëkk si coow Su ma xoolee fu ñu jaar yépp Dagg ma woowoon di ma def fu sori Bi ñuy goro loxam wax ma Tay biti bi moo lay gërëm kër gi jooy triste Samba alar waaw si njaboot ji Xol yaa ngi jooy, xar yaa ngi jooy Ñaata at man ak yaw ci kër gi Bi ma lay tànn boobu xalaatoo dinga séy si Soxna si sétal si Yàlla ji nga xol si biti Gisoo sa moroom bu ne si séy ba pare ne si Mbedd mi njaboot moo muccoo Lu fees nak si xol su ëpp tuuru Muñ na ba s¨s taxul nga xam li xol bi jiyunju Daje n'a lu ne gir yak ak njaboot ji liñuye dundu Fi may dundu gis naa lu ne ms taxul ma xàddi Bànneex man dégg la si am Coono ak naqar tax ma géj nekk si jàmm Wax ma lan nga bëgg si lan gane Talatoo ma talato sa kër gi wax ma noy def ak njaboot gi Wax ma man ak yaw ku tan Fépp foo xam na ngi mafa clamé Bateau dem bateau costé mënoo ma tere xolli kaneen Lépp loo ma yakkul danga ko fàtte Su respect jexe mbëggeel dem yoonam lu ñu dese lu dul Samba alar waaw si njaboot ji Geestu war naa la samba alar nga (Xol yaa ngi jooy xar yaa ngi jooy) Ñi nga bëggantel ñoo ngi sa ginnaaw Yeah, yeah Su ma lay woo nga ni doo ma faale Su ma lay woo, oh oh Xanaa nobatoo ma? Su démb doonoon tay Ma joxaat a sama mbëggeel? Su démb doonoon tay Ma joxaat la sama xol bi mbëggeel bi Su ma lay woo nga ni doo ma faale Su ma lay woo, oh oh