Duma la bàyyi, duma la bàyyi Yow it bul ma bàyyi, bul ma bàyyi yeeh Moom ne na daf la bëgg piir Ne na dafa bëgg nga nekk ki mu jiital Moom ne na yaa de ki mu gis Ne na ci ñoom ñépp yaw rekk la bëgg jiital Ne na dootul la bàyyi Yaw la tane ci góor ñi Ne na dootul la bàyyi Yaw la tane ci jigéen ñi Duma la bàyyi, duma la bàyyi Yow it bul ma bàyyi, bul ma bàyyi yeeh Abadan, abadan, abadan Abadan, yow bul ma bàyyi da’imam Abadan, abadan, abadan Abadan, yow bul ma bàyyi da’imam Sa añ moo dàq lu ma mëna lekk Sa kër moo dàq fu ma mëna nekk Lu ñu neex lekk, lu ñu neex naan Njaboot gi fecc ak a reetaan Man dama la nob ba di la bëgga fóon Man dama la Maa ngi la chérie ouha Dama la nob ba di la bëgga fóon Man dama la Maa ngi la chérie ouha Duma la bàyyi, duma la bàyyi Yow it bul ma bàyyi, bul ma bàyyi yeeh Abadan, abadan, abadan Abadaan, yow bul ma bàyyi da’imam Abadan, abadan, abadan Abadaan, yow bul ma bàyyi da’imam