Les goûts et les couleurs ne se disputent pas Man ki ma bëgg jox ko sama xol, na ngeen masi Ba Ni mu tollu la ko bëggee avec son poids, je l'aime moi Bala may dof ma téye la, nga fees samay loxo Ndax xale bu fees bari jàpp moo jara tek loxo Awumak affaire taille fine, man ni la miin Way jekk ji ñoo may dadji yeah, yeah Su ma naree dee ci àll na ma Gaynde Ray Su ma naree dee ci àll ginnaar duma ray boy Soo bëggoon étage, chérie moom la lay may Ni ma la bëggee dara du ko fay, waa-waaw Man li ma gëna bëgg taille fine la Man li ma gëna bëgg jekk bu diis la Non, man bëgguma jekk bu diis Li may daaneel newul ci taille fine Bët du yénu waaye xam naa lu bopp àttan Bëgg naa ku yem xale bu maggul atam Taille fine kenn du moom Woyof àttan seen bopp ñoo ko moom, hèè! Namm naa ku may fowee di ko nabb nabbé Ku yem ci ay loxo ma koy wane ni ma ko nobee Bokkul ak kiy tokk sa kaw te doo mëna noyyi Diis ba dootoo yeukk loxom yu noy yi Taille fine yi, sawar nañ te foo leen woo ñu wuyu la Te yaw sa jekk bi boo ko toppee boo dawul ñu robi laa Man li ma gëna bëgg taille fine la Man li ma gëna bëgg jekk bu diis la Non, man bëgguma jekk bu diis Li may daaneel newul ci taille fine Bu sééddaay jotee doo soxla àndu cuuraay Dangay bokhou rekk tëdd ci wétam mu tokk di la ray Bu tàngaay jotee doo soxla clim waay Di nga mëna di foo ak moom te ñàkk du la ray Ki dafa jonge ba lu ne la may defloo Suñu tëddé daf may joyloo Ki dafa woyof ba fu ne lay aw ci man Bu may xalaat li ma may def daf may réeloo Ñi àndak taille fine waneleen seen bopp (heey) Ñi àndak jekk ji yeen a nangeen (heey) Ñi àndak taille fine wanewuleen Ni àndak jekk ji, jukkleen may xool Man li ma gëna bëgg taille fine la Man li ma gëna bëgg jekk bu diis la Non, man bëgguma jekk bu diis Li may daaneel newul ci taille fine