Suma woyofé lool nguani dama ñakk fayda Ma jaar si digg wah nimqko gise ngani dama ñakk kersa Te woyof lool woute na akk ñakk fayda Jaar ci digg wahi tam wute na ak ñakk kersaa Giss nga rawante doje ak kayit diisatah kayit jiitou doje Soo sete basi biir yow xamuloo linga beug Digante bo giss moussante massuko yorr Ginaaw lu yagg degla bule ragal degg gi Degg moom kaani la koko tufe mu tohoñu Te degg moy fondement lep lo giss Degg gi moy benn jigen waratul dess ginaaw Gemm li nga doon Ham li nga beug ñaari lohoy takk tubay te moy takk serr Bañe na, bañe na duma femme objet Ñaari lohoy takk tubay te moy takk ser Balaa may beg dee nga naan jigen ligeyoul Te eumb juroom ñenti weer weusin dara genouko metti Jigenangi arme, jigenangui tool ya Jigenangi ci bureau yee Su goor teke jigenangi si wetam Yow sama jigen weyal di ñafe linga beug ngala busi tayi fekk jotuloko Gem li nga doon Ham linga beug, ñari lohoy Jigen ñi yag nano wane pasteef demb ba tey jile Yacine Boubou, Aline Sitoe diatta, Sokhna Mame Diarra Bousso Mame Fawade Wele etc yen jigen Senegal yagg nguen wane sen bopp Heuthie bu dikoul dagg Sister bañal yow bañal fekk jotoloko