Àddina ak li ci biir boo demee ba am ko Bul fàtte, bul fàtte, fa nga cosaanoo Àddina ak li ci biir boo demee ba am ko Bul fàtte, bul fàtte, fa nga cosaanoo Àddina ak li ci biir boo demee ba am ko Bul fàtte, bul fàtte, fa nga cosaanoo Àddina ak li ci biir boo demee ba am ko Bul fàtte, bul fàtte, fa nga cosaanoo Xam na nu fi nu joge Li nu jaxal mooy fu nu jëm de Suufu maam yi moom bu nu woowe Du nu tànqamlu du nu soree Danuy fatu nu mu gëna gaawee Ñun ndawu reew mi da nu pare Ji fi luy jëriñ fi ak fë le Ba ñu ñu ci dara ku ngemboy bëre Wër naa àdduna Japon, Inde, Australia There is no place like home Fenn du Sunugaal Fa nga cosaanoo Fa nga cosaanoo Ku fi fàtte demb, ëlëg dalay reer Waxu mag la degg nga du am kubeer Fattëlikul ki nga doon fi nga juddoo Fi nga jugee, fi nga dëkk Yàlla mi la bind Ngor, jom, fit la, fayda boo ko amul Doo xam fi nga jëm dara du ku dindi Li ci Baay bi di doom na ko jëli Kaddu mag ñi nii na ko sët yi firi Na nu gëna disoo ndax ñu mëna deggoo Xana gisoo jikkoo yi ni gëna yàqoo Na nu dellu te toogi mëna root du doy di Àdduna ngi daw di na ñu def ci bopp yi Bul di fàtte ñi la fàl ñi la tettewoon Ñi la gunge bi ngay raam ñi nga nekkaloon Lakoon fakoon ñakoon Lawoon fawoon ñawoon Xaleel poto poto la Noko raaxe rek lay weyee Fi laa yaroo fi laa maggee Lu mu guddi guddi guddi damay ñibbe Galsen mooy daw sunu deret Dañu wutiwoon ba tax ñu ne bëreet Teranga yi ñi fay jëlee su nu askan lañ koy jëmee Wër naa àdduna Japon, Inde, Australia There is no place like home Fenn du Sunugaal Fa nga cosaanoo Fa nga cosaanoo Fa nga cosaanoo Fa nga cosaanoo