Diaw Diop Didi Jolof music in the place han han Muyeen tay ma toukeul dëkk bi (tay ma toukeul deuk bi) Sañse di bégel xale yi (sañse di bégel xale yi) Law la cat law la ma lammiñ (law la ma bët bu ay) Djeulal sa temps snap lima sadji Kaay foto ma, poste ko yëngël sama noon yi À la une bi wone ma Il est mignon, il est charmant Wallah, il est galant, attirant Ku mën na def, ku mënul demal toog Sane repassera soo mënul demal took waaw Ku mën na def, ku mënul vas là-bas Sane repassera soo mënul dangay xaar waaw Ndéké li koy yëngël ci man mii la (Li koy yëngël ci man mii la) Li may dégagé man mii la (si si) Ak li ma yokk, naturellement feeling bi la (Naturellement feeling bi la) Ndéké likoy yeungeul si mane mii la Moo tax damay zonzé (hee zonzé) Moo tax damay zonzé (hee zonzé) Su ma neexee zonzé Moo tax damay zonzé (hee zonzé) Billaay man de Yàlla téral na ma (Yàlla teral na ma) Yàlla buur bi sagal na ma Si samay digg nawle Yàlla buur bi téral na ma Ak reew mi fi mu toll Yàlla buur bi sagal na ma haan Mi ngi tourou eup na, doumako lal dafa fess Tempo tempo tek ko si temps Fouma teule doumeu lenn Kaay photoma, dawsil photoma Man damay fowak xale yi, dawsil photoma Dama am thiass, ak touti thiathia thiass Te xam naa dama beuri titeur dama koy assumé Dama am cas, ak touti thiathia thiass Bilay wallaay dama beuri titeur dama koy assumé Ku mën na def, ku mënul demal toog Sane repassera soo mënul demal took waaw Ku mën na def, ku mënul vas là-bas Sane repassera soo mënul dangay xaar waaw Ndéké li koy yëngël ci man mii la (Li koy yëngël ci man mii la) Li may dégagé man mii la (si si) Ak li ma yokk, naturellement feeling bi la (Naturellement feeling bi la) Ndéké likoy yëngël si man mii la Moo tax damay zonzé (hee zonzé) Moo tax damay zonzé (hee zonzé) Su ma neexee zonzé Moo tax damay zonzé (hee zonzé) Xam nga dañuy zonzé Su jeexee, jeex na, su jeexee, jeex na Su paree, pare na, su nu nopee pare na Demba Salimata, baba Salimata, Maître Lika Ba ma ni jugal zonzé (Demal nga tok, fëlé, demal demal nga tok fëlé nëlé) Yaw Reme Leye jugal zonzé, Dione Wally, jugal zonze (Demal nga tok, fëlé, demal demal nga tok fëlé nëlé) Demal nga tok fëlé nëlé