Danga ma wan wan ma nobeel Wan ma cofeel, wan ma luy nammeel Dama la xam xam luy mbëggeel Xam ni ku du yaw duma mën a pexel Danga ma bégee fa ma xam ko waay Maa la raw, baby xam ko waay Tu sais que je t'aime de tout mon coeur Tagal ma waay, wey bu dootu fay Dinga ma ray xalaatuma la bàyyi Des jasite ñépp xam ni yaa mi rey Yaa mën, yaa ngi Tay ma ci la koy Yàlla seede la Tay ma taggalel ba nga xam yeen kan Yaw mi la yaw rekk a waral li Jëlal jëlal Te bëgguma ku lay jege jege Dawal dawal Ne naa la jarul nga may xaar Ñëwal ñëwal Te xam nga yoon bi nga war a jaar Dawal dawal Ey bëgguma ku lay sonal Bëgguma ku lay gaañ Bëgguma ku lay tooñ (Maak yaw la) Ey bëgguma ku lay sonal Bëgguma ku lay gaañ Bëgguma ku lay tooñ (Maak yaw la) Bu jaaree bëre naa ko dóor daan Bu jaaree mer duma reetaan Bu jaaree jëf dinaa ko def Dinaa dundal sa xol Ba àdduna bi di ko seetaan Mbëggeel lu diis la du dooy (lu diis) Te ku ko ñam du ko fowe Yaa ngi may guddandaat (waxal) Yaa mën te di ko jëm de ma dundal laaj Yaay ki ma coqotaan Samay ram fu mu tànge damay duma daanu ma Ñëwal ñëwal, pare naa lu ne Yaay sama xol te jaral nga ma lu ne Yaw mi la yaw rekk a waral li Jëlal jëlal Te bëgguma ku lay jege jege Dawal dawal Ne naa la jarul nga may xaar Ñëwal ñëwal Te xam nga yoon bi nga war a jaar Dawal dawal Ey bëgguma ku lay sonal Bëgguma ku lay gaañ Bëgguma ku lay tooñ (Maak yaw la) Ey bëgguma ku lay sonal Bëgguma ku lay gaañ Bëgguma ku lay tooñ (Maak yaw la) Maak yaw la! Maak yaw la!