Yaa ngi dee ndax man Maa ngi jooy ndax yaw Li ñu boole moo bari doole Ak a ma leer ne yaw laa nob Su ma geestoo gis la kontaan Boo ma xoolee ree Ni ñuy nammantee Yaw laa nob Ragaluma loolu (yaw laa nob) Dawuma loolu (yaw laa nob) Iso nenne yaa ma jaral lii Man de yaw laa nob Ragaluma loolu (yaw laa nob) Dawuma loolu (yaw laa nob) Iso nene, liy xasan neex ci sama xol bi Waay waay Fan nga ne ci man mbëggéel Xam naa maay sa Indo Ci léewatoo dem nga Ardo Bëgg nga ma ba mu jeex Ba ma xam ko dawuma yoole Yaw laa nob Man lañuy wër te yaw laay wër Jébbal naa la sama xol bi Nekk ak yaw di dund sama mbëggéel Daf may neex (yaw laa nob) Man nga fii te man nga fee Xam nga lii te xam nga lee Reewal ma te doo ma yër Bébé lu ma bëgg rekk daf lay neex Yaa ngi dee ndax man Maa ngi jooy ndax yaw Li ñu boole moo bari doole Ak a ma leer ne yaw laa nob Su ma geestoo gis la kontaan Boo ma xoolee ree Ni ñuy nammantee Yaw laa nob Ragaluma loolu (yaw laa nob) Dawuma loolu (yaw laa nob) Iso nenne yaa ma jaral lii Man de yaw laa nob Ragaluma loolu (yaw laa nob) Dawuma loolu (yaw laa nob) Iso nene, liy xasan neex ci sama xol bi Yaw ne yaw laa nob! Ndeke mbëggéel ni la neexee Dama la bëgg lool (yaw laa nob) Maa ngi baax yaa ko woyofal ba ma àttan ko Yeeah amore (yaw laa nob) Amore foo ne laay ne Yaay bànneex, yaay yërmande Bu ma mere ci sama fiiraange Bébé yaw dama la nob Man nga fii te man nga fee Xam nga lii te xam nga lee Reewal ma te doo ma yër Bébé lu ma bëgg rekk daf lay neex Yaa ngi dee ndax man Maa ngi jooy ndax yaw Li ñu boole moo bari doole Ak a ma leer ne yaw laa nob Su ma geestoo gis la kontaan Boo ma xoolee ree Ni ñuy nammantee Yaw laa nob Ragaluma loolu (yaw laa nob) Dawuma loolu (yaw laa nob) Iso nenne yaa ma jaral lii Man de yaw laa nob Ragaluma loolu (yaw laa nob) Dawuma loolu (yaw laa nob) Iso nene, liy xasan neex ci sama xol bi Yaw ne yaw laa nob! Bëgg naa, bëgg naa, bëgg naa Man de nob naa Bëgg naa, bëgg naa, bëgg naa Man de yaw laa nob