Et puis quoi, yaw la kan? Xamuloo ma di wax ci man Seetuloo bëgg di ma tamm Mën wañe allure bu mel ni dos d'âne Ñi di wax ci samay def Ku ci dul def man li may def Dañu lay xeelal ba nga def Weraat naan xoolal la muy def, eh Fomp sama rangoñ dootuma jooy Ndax léegi xam na Ni nit ku la bañ, amuloo koy defal Ba mu xëy bëgg la Mën naa la jox ay nopp Waaye taxul ma gëm say wax Ay bët nak faw mu jooy Di sooga mëna gis bu baax Ñin koy jema fay muy boy Waaye xanaa nga war ko baal Fi ku fi baax day bari noon En tout cas man li la wax Alabarka nene jarama Nit ñi lëndëm nañu yaay ñaanal ma Ba ma muc ci ñett ñi Ku may signe te bëgguma Kiy indi di yóbbu Ak kiy bég ci sa coono Année yi dem dem ba jangal Ma ngi fi boy déglu doo dem Bu Yàlla di trace ngay effacé Yaw lay effacé retracé Mën naa la jox ay nopp Waaye taxul ma gëm say wax Ay bët nak faw mu jooy Di sooga mëna gis bu baax Ñin koy jema fay muy boy Waaye xanaa nga war ko baal Fi ku fi baax day bari noon En tout cas man li la wax Yak sa ree ju neex xame naa la (xamee naa la) Bañ weex na mais déréta ko lal Pourquoi tout ça, tout ça pour rien Pourquoi tout ça, tout ça pour rien Mën naa la jox ay nopp Waaye taxul ma gëm say wax Ay bët nak faw mu jooy Di sooga mëna gis bu baax Ñin koy jema fay muy boy Waaye xanaa nga war ko baal Fi ku fi baax day bari noon En tout cas man li la wax Yak sa ree ju neex xame naa la (xamee naa la) Bañ weex na mais déréta ko lal Alabarka nene jarama Nit ñi lëndëm nañu yaay ñaanal ma Na xerr bi dal say noon