Setlu naa li ci Yàlla
Bay bañ ñu gis sama ndare
Pël ci Ndaye ci Baye
Boroom sow daal yàgg

Fàtte fépp sooga door daan
Dama ëpp li nga ma doon dooye
Xale bu loxom sétt
Bañ koy tooñe maget

Yàlla ma wóolu
Dink ma bakkan
Xoolul ni ma tollu ndax yàgg na dall

Ay miroir waxal qui est la plus belle
Ay miroir waxal qui est la plus belle
Gis ni ma moolee noon lay daggooy dem
Gis ni ma moolee noon lay daggooy dem

Nganpu ci yaw way ndax fu la neex fële
Teg sa temps ci heure tardewoo benn yoon
Raw nga say maas, bokkuleen waaye

Yeen ñiy déglu di bég di supporter
Dëgg la waay bég naa leen
Li lépp man la
Sometimes ma jot seeni messages
Égalisation remontada
Wax ko ñi foogoon pare naa
Man su may xool sama seetu
Gis ku leen gëna pare ëpp leen class
Xale ba ngi ni, dafa am cas!

Ay miroir waxal qui est la plus belle
Ay miroir waxal qui est la plus belle
Gis ni ma moolee noon lay daggooy dem
Gis ni ma moolee noon lay daggooy dem

La petite bi newoon seen galle
Laay laylalaa woo yeh yeh
Dañoo jongowe
Man de jub naa sa ñël jub na sa golal
Waxleen ma jub naa waawaaw
Sa ñeluben

Eh fu la neex toog parler seuleument au lieu de travailler
Maa ngi dem ku may seet ne leen ko ba ma we
Yoon wi lëndëm kus ñu wëy kus waay

Yeen ñiy déglu di bég di supporter
Dëgg la waay bég naa leen
Li lépp man la
Sometimes ma jot seeni messages
Égalisation remontada
Wax ko ñi fogon pare naa

Ay miroir waxal qui est la plus belle
Ay miroir waxal qui est la plus belle
Gis ni ma moolee noon lay daggooy dem
Gis ni ma moolee noon lay daggooy dem

Aa yeeh
Yeh enh waway
    Página 1 / 1

    Letras y título
    Acordes y artista

    restablecer los ajustes
    OK