Awa Gambia Dieyna Ma letal la lépp yëngu Lépp dëgër te ma tàmbali ma Xanaa du may ndaanaan Ñaata yoon ñu sentu ma fi, sentu ma fee Man ma fëlé feneen Xanaa du may ndaanaan Ku sa xol di metti maa lay bégal Def lu baax laa lay dëgal Xanaa du may ndaanaan Ñaata kamb lañu maa gasal Jëm maa feexel mënuñu ci man dara Xanaa du may ndaanaan Ndaanaan xamul ragal, yor fu la di ko jaay Sa jikko da koy wane jom ak fitam waay Ndaanaan dafay dëgger li nga koy waxal du ko sonal Góor am du ko jaay, jom ak fu lem waay Aah, xam nga maay kan Man dama bari cas Feel nga fem bi may ndaanaan Eeeh, xam nga maay kan Man dama bari cas Gis nga fem bi may ndaanaan Aah, may ndaanaan bi May ndaanaan bi Kañ ngay nangul ndaanaan bi Eeeh, may ndaanaan bi May ndaanaan bi Jëmal nangul ndaanaan bi Xale bu ndeyam gërëm Nga koy yenne fan ne muy lay gëna belli Xanaa du may ndaanaan Yoon wi tollo loo te metti Tiituma te ragaluma dara Xanaa du may ndaanaan Eeeh Awa ne leen pexe noon Duma wacce sama yoon Xanaa du may ndaanaan Ala Atiou amul bàyyi Duma sonn duma tàyyi Xanaa du may ndaanaan Ak lu mëna am, xoolal sa kanam Dinga am ndam bul bàyyi Fu ma mëna dem, lu ma mëna gis Taking over everything Aah, xam nga maay kan Man dama bari cas Feel nga fem bi may ndaanaan Eeeh, xam nga maay kan Man dama bari cas Gis nga fem bi may ndaanaan Aah, may ndaanaan bi May ndaanaan bi Kañ ngay nangul ndaanaan bi Eeeh, may ndaanaan bi May ndaanaan bi Jëmal nangul ndaanaan bi Aah yeah, yeee laye Yella bu mi góor la Aah yeah, Yella ye Yella doomi góor la Dieyna ak Awa Sunu wey wii woyu góor la Aah yeah, Yella ye Yella doomi góor la Awa ak Dieyna Way wi wayu góor la Aah yeah, Yella ye Yella bu mi góor la Aah yeah, Yella ye Jumal nangul ndanaan bi