Et la famille au Sénégal? Oui, bien sûr! Sori sama réew ak sama askan Taxul ma fàtte man mi may kan Damay liggéey doxuma ci caaxaan Seen soutien da may bégal di ma yokku katan Damay ñafe di liggéey duma geestu Yónne yakamti ma duma daagu Li ma weesu la réccu Fi ma jëm leer na ma, man la ni séntu Ay ay ay Fii mooy Senegaal Fii la xol yi di feexe Fii la stresse biy wacce Fii la xale yi gëna baaxe Sama réew nii la neexee Foo dëkk, Senegaal? Oui! Fière ci doon sénégalaise La famille au Sénégal, oui Fière ci doon sénégalaise Civilisé rafet mëna sañsé Tey bëgg topp cas Ku ne ngay wax, pays de la teraanga Kenn du ñu yàpp, kenn du ñu xeep Kenn du ñu kël-kële Ñun lañuy wax, pays de la teraanga Am teraanga Ku ne ngay wax, pays de la teraanga Sama réew mi da may neex te jàmm ja ngi fi Jàng bi na fi sax, jàng bi Ay ay ay Fii mooy Senegaal! Fii la xol yi di feexe Fii la stresse biy wacce Fii la xale yi gëna baaxe Sama réew nii la neexee Foo dëkk, Senegaal? Oui! (Oui, bien sûr) Fière ci doon sénégalaise (oui, bien sûr) La famille au Sénégal, oui (oui, bien sûr) Fière ci doon sénégalaise (oui, bien sûr) Foo dëkk, Senegaal? Oui! Fière ci doon sénégalaise La famille au Sénégal, oui Fière ci doon sénégalaise Yaw Diara Sylla! (Foo dëkk, Senegaal? Oui!) Fatou Mbacké Diongay sa yaay (Fière ci doon sénégalaise) Ami Ndikou Guey yaayam (La famille au Sénégal, oui) Cheikh Diongay baayam (Fière ci doon sénégalaise) Demba Sylla sa baay (Foo dëkk, Senegaal? Oui!) Sokhna Aïda Mbacké yaayam (Fière ci doon sénégalaise) Yaay Seutou Serign Barra (La famille au Sénégal, oui) Diarra yaay Seutou Serigne Touba (Fière ci doon sénégalaise) Foo dëkk, Senegaal? Oui! Fière ci doon sénégalaise La famille au Sénégal, oui Fière ci doon sénégalaise