Fi nga juddoo moo lay def Li nga nara doon Fi nga bokk sant bi ngay wuyoo Waratuloo Wàcc yoon Su ma saañoon Ñun ñaar lu ñu neex def Saañuma ko Lu ñuy xaar ci man lay def Sorale Ñoom lay sorale Sama xel ak sama xalaat comptétul Ñoom lay sorale Sorale Ñoom lay soor Sama xel ak sama xalaat comptétul Ñoom lay soor Guddeek bëccëg, suba ak ngoon Ma nekk ci naqar Jënde sama mbégteek sama Bànneex ak li ma war Pression sociale, règlement familiale Juddu bu réy ak alal Ñoo ma yobe li ma dàll Sorale Ñoom lay sorale Sama xel ak sama xalaat comptétul Ñoom lay sorale Sorale Ñoom lay soor Sama xel ak sama xalaat comptétul Ñoom lay soor