Ragaluñu dara, dara Da da dara Ragaluñu dara, dara Da da dara Bu jant bi sowee Équipe moo wetal Yobbu ndamam, gàcce ngalama Les lions du Sénégal Ak ngeen ñoo yàgg bégal Gàcce ngalama, allez les lions! Ragaluñu dara, dara Da da dara Ragaluñu dara, dara Da da dara (Anh lawoon fawoon) Ah, ragaluñu dara Gaynde xiif tey, xepp na fukki mbaana Defaat fa ndam bëgg ñibbi Dakar Xanaa danga fàtte Sadio Khana? Di taal sa camp fi la tikki taka (ha haa) Gën la tàng, gën la sayar, gën a waga Ku fi joog ma tiim la ci kaw, caakaba la Kenn du noyal amul seral, amul sikki saka Ragaluñu dara, dara Da da dara Ragaluñu dara, dara Da da dara Fulaak fayda ak jom Ak ngor lañiy wane sur le terrain Gàcce ngalama, ahn Sunu équipe bi, ahn Lawoon fawoon