Maestro on the beat Bëgguma sañse (nga ni?), sañse ma bëgg Yaw danga bari doole, arrêteel mënoo ñu jàppale Li nga sañse ni rafet na xoolal ni mu la jàppe Moo yaw danga neex li dama ko sol pur lakk yapp Booleen bëggee deuxième tour na xale yi ñan ma ko ci njëkk Ci njëkk He, yaa ma na sañse Sañse di paw paw Ku ko man ni la koy defe Ci njëkk He, sañse ci yaw la ne Jooyal ba wadd Waaye li ma sañse Hitoire dina ko bind Li du mak ñoom, li du mak ñoom Ngeen bi du mak ñoom Xam nga sañse ma ci toog Wowowowaay Li du mak ñoom, li du mak ñoom Ngeen bi du mak ñoom Xam nga sañse ma ci toog Li ma sañse du info, ci sama quotidien la Dara daluma maa ngi ci jàmm, lalal bant nelaw kaar Ma cas leen ki ma ñawal fi ma xottile (eh!) Dem ci karaj am ci pose bu nice (waxaat leen kaar) Yaw danga bari doole, arrêteel mënoo ñu jàppale Li nga sañse ni rafet na xoolal ni mu la jàppe Moo yaw danga neex li dama ko sol pur lakk yapp Booleen bëggee deuxième tour na xale yi ñan ma ko ci njëkk Ci njëkk He, yaa ma na sañse Sañse di paw paw Ku ko man ni la koy defe Ci njëkk He, sañse ci yaw la ne Jooyal ba wadd Waaye li ma sañse Hitoire dina ko bind Li du mak ñoom, li du mak ñoom Ngeen bi du mak ñoom Xam nga sañse ma ci toog Wowowowaay Li du mak ñoom, li du mak ñoom Ngeen bi du mak ñoom Xam nga sañse ma ci toog Waawaaw Waxat leen kaar Mashallah! Waxaat leen kaar Wawawawaw! Céy, li nga sañse!