Yeah Zay Man bàyyi naa ko, waay Fippu naa man Man fippu naa, bàyyi naa ko Xol bi ne ma déet Man gedd naa ko wan gannaaw Sama xol bi ne ma déedéet waay! Danga ma dàqal Ouroul Ayni Ma bëgg la lool ee Nga miinal ma sa bopp Ma dof ci yaw Su ma la defee pepe Ngay ñaanal nan sa xol bi dafa sedd Su ma la séene ngay dem Lu dul yaw dama koy gedd Waaye léegi ne nga ma lay déranger Loolu def ma góomu xol Di ma ronger, heee Bàyyi naa la (ma bàyyi la ko) Man mile Man fippu naa, bàyyi naa ko Xol bi ne na déet Man gedd naa ko wan gannaaw Sama xol bi ne ma déedéet Man fippu naa, bàyyi naa ko Xol bi ne ma déet Man gedd naa ko wan gannaaw Sama xol bi ne ma déedéet waay! (Sama xol bi ne ma déedéet waay!) Man mi dama jax maak ji dañu doyal Mon amour, tu en as trop abusé Jarul may forcer Mbëggeel du kenn a rekk ko def Jarul may sale Xol bi yaa ci nekk Ni la mënoon demee chérie booy Bye bye Man fippu naa, bàyyi naa ko Xol bi ne na déet Man gedd naa ko wan gannaaw Sama xol bi ne ma déedéet Fippu naa, bàyyi naa ko Xol bi ne ma déet Man gedd naa ko wan gannaaw Sama xol bi ne ma déedéet waay! Mbëggeel a compliqué Man fippu naa, bàyyi naa ko Xol bi ne na déet Man gedd naa ko wan gannaaw Sama xol bi ne ma déedéet Fippu naa, bàyyi naa ko Xol bi ne ma déet Man gedd naa ko wan gannaaw Sama xol bi ne ma déedéet waay!