Maestro nénéné Cherie fouñu diar yép (yép) Mamouy méti bébé Ñun ñar rék (rék) Cherie fouñu diar yép (yép) Li guenone méti bébé Romb nañu lep (lép) Cherie coco no no bou dem And nañ ba yalla def ñu seuy si farata Nga mouñal ma Louma jiguen meusta mouñal jaarama Yaw milé Yaw milé deh Yama dioural sama taw bé Yaw milé éh éh Yaw mi deh Yamay motali souma wété So démé sama keur gui Dina tasss wawawaw Chérie sama xol yawa Té kinga xam mana Namnala man bay dioy Chérie daga dém ma wétt Té so ñeuwé mou déñ Boudoul yaw dou done kénén Lolo am Té dou nén Je suis fou de toi Té dou nén Chérie man dama dof si yaw Dou nén Je suis fou de toi Té dou nén Chérie man dama dof si yaw Xamna ni mala togn baby Je t’assure j’ai fauté baby waw Je me suis excusé Adouna bi yama si guenal Maguilay dora chérie boy mané balma Bouñ la wowé fi lé Bouñ la wowé néla dof na Boumla bétt balma (Yép yép) Mamouy méti bébé Ñun ñar rék (rék) Cherie fouñu diar yép (yép) Li guenone méti bébé Romb nañu lep (lép) Cherie coco no no bou dem Chérie sama xol yawa Té kinga xam mana Namnala man bay dioy Chérie daga dém ma wétt Té so ñeuwé mou déñ Boudoul yaw dou done kénén Lolo am Té dou nén Je suis fou de toi Té dou nén Chérie man dama dof si yaw Dou nén Je suis fou de toi Té dou nén Chérie man dama dof si yaw