El Maestro (Oh Satou bi) Satou Niang Hé yah yah yah yah yah Yaay sama wéeruwaay Yaw danga mas a doon sama waay Suma reni xol Ma ni xam nga ni yaw laa love Bokkook ñoom te duñu yaw Yaa raw gaynde ci àll bi Bu jinnee bëggee ku yëg dangay daanu Aladji, kenn du yaw Dama jonge ba exagéré Ni may séye da particulier Bu guddi jotee ba nekk bi wet Maay ki lay feccal mu lay thieuguine Dama jonge ba exagéré Ni may séye da particulier Bu guddi jotee ba nekk bi wet Maay ki lay feccal mu lay thieuguine Mu lay thieuguine (kaay) Mu lay thieuguine (anh) Mu lay thieuguine (nga ni?) Mu lay thieuguine (kaay) Rësëgin tacc (ahn) Rë-rësëgin tacc Rësëgin tacc Rë-rësëgin tacc Maes sama chibiribi lalale, éh héé! Xam nga yaw fii yaw yaa fi ne Soo fi nekkul, danga may wetal (Je t'aime) li nekkatul infos (Tu m'aimes) li nekkatul cas Maa lay feccal di la leebal Bañuma ba xale di ma ree Dama jonge ba exagéré Ni may séye da particulier Bu guddi jotee ba nekk bi wet Maay ki lay feccal mu lay thieuguine Kon danga jonge ba exagéré Ni ngay séye da particulier Bu guddi jotee ba nekk ci wet Yaay ki may feccal mu lay thieuguine Kon danga jonge ba exagéré Ni ngay séye da particulier Bu guddi jotee ba nekk ci wet Yaay ki may feccal mu lay thieuguine Mu lay thieuguine (kaay) Mu lay thieuguine (anh) Mu lay thieuguine (nga ni?) Mu lay thieuguine (kaay) Rësëgin tacc (ahn) Rë-rësëgin tacc Rësëgin tacc Rë-rësëgin tacc Kon danga jonge ba exagéré Ni ngay séye da particulier Bu guddi jotee ba nekk ci wet Yaay ki may feccal mu lay thieuguine Mu lay thieuguine (kaay) Mu lay thieuguine (anh) Mu lay thieuguine (nga ni?) Mu lay thieuguine (kaay) Rësëgin tacc (ahn) Rë-rësëgin tacc Rësëgin tacc Rë-rësëgin tacc