Dama dem ba fu ma tël Ñu ne ma xale bi kaar Dafa dem ba fu ma sañse Ñu ne ma kaaro mashallah Damay lakkatu sax Dama tamm rare man Cat gi ci limiñ Dafa sew te gaaw Iyoo ho, waxal mashallah Iyoo iyoo, man doomu jambur la Iyoo ho, waxal mashallah Iyoo iyoo, man doomu jambur la Lakalé ne N’golo Kanté Cat dafa sew te gaaw (jëlal) Xaral ma takk Pétaw Wala ma setti Maam (nga ni ma) Noon yi noon yi noon yi Dañu doy waar Jaral na leen dem si sëriñ Garé la bu yabo Nga fagaru so dewe safuleen sax Cool lal ba ma sangatu Séeti baxaw lalaké Iyoo ho, waxal mashallah Iyoo iyoo, man doomu jambur la Iyoo ho, waxal mashallah Iyoo iyoo, man doomu jambur la Tathiou lén mu rirr Waawaaw Jëlel! Bul ma catu catu catu catu Bul ma catu (Ñëwal) Bul ma catu catu catu catu Bul ma catu Iyoo ho, waxal mashallah Iyoo iyoo, man doomu jambur la Iyoo ho, waxal mashallah Iyoo iyoo, man doomu jambur la Nél Mashallah hahan Doomu jambur la ah ah Yàlla nañu Yàlla Mussal Si cat làmmiñ Musiba la de! Ku garé moo la garé Làmmiñ Ku taxaw moo la freiné Yàlla bu ma freiné man