Ãa kaay labat ma Ñaan ma sama baay bóoy Mu may ma laa waaw Ãa kaay labat ma Ñaan ma sama baay bóoy Mu may ma laa waaw Billaay njool mu ndaw Kaay dogaale ma yóbbu Foo jëm aawoloo ma May wolal sa yaay Di ko toggal Di root muy naan Ãa kaay labat ma Ñaan ma sama baay bóoy Mu may ma laa waaw Billaay njool mu ndaw Kaay dogaale ma yóbbu Foo jëm aawoloo ma May wolal sa yaay Di ko toggal Di root muy naan Ãa kaay labat ma Ñaan ma sama baay bóoy Mu may ma laa waaw Damay sangu solu xeeñ lu neex Chéri waaye bala ngaa ñëw ma nelaw "Plat" bi nga gën a bëgg laay rëgal Chéri waaye bala ngaa ñëw ma nelaw Junni yi ngay maye ma di ko dégg mayoo ma ci Chéri waaye bala ngaa ñëw ma nelaw Jongoma joo séen dem may kob junni Xanaa xamoo ne man mi jongoma laa Ãa kaay labat ma Ñaan ma sama baay bóoy Mu may ma laa waaw Man ak mbëggeel Wóo wóo wówóow man ak mbëggeel Leeg-leeg nu toog di waxtaan Sunu diggante neex ba mel ni suukar Leeg-leeg nu toog di waxtaan Seytaane dikk nu daal di réeróo Nun jigéen ñi nun ñépp a yem Ku leen di yor da nga leen di muñal Fàllu bu la Kura tooñatee Jéggal ko te xam ne jigéen a la jur Omar bu la Maam Njaay tooñatee Jéggal ko te xam ne jigéen a la jur Aysata Sow yaw Yàlla na la Yàlla may looy béggéey Yaw rekk laa waaw Asan bu la Faat naar tooñatee Jéggal ko xam ne jigéen a la jur Aziz Gay bu la Ndey Mbay tooñatee Jéggal ko te xam ne jigéen a la jur Ami Jeŋ yaayu Maas Njaay dara weesul Man xam naa ni yaw rekk la Fiiru ma Matar Ndiaye fiiru ma Yaw la bëgg yaw laa miin fiiru ma Fiiru ma maa fiiru ma Yaw laa xam yaw laa miin fiiru ma Wóo wóo wóowu wóowu Chéri I love you, waaw Mon chéri Mon chéri Mon chéri Yaw rekk laa Waaw ñaar ñu bëggante Boo ca xajul wax ca lu baaxoo I love you waaw Mon chéri Mon chéri Mon chéri Yaw rekk laa Billaay Aas ! Chéri Daado Géy Dee ko muñal Dee ko muñal waaw I love you waaw Mon chéri Mon chéri Mon chéri Yaw rekk laa Ndey Faatu Njaay Ndey Faatu Njaay Madame Deme Yàllaa nu boole Yaw rekk laa waaw Mon chéri Mon chéri Mon chéri Yaw rekk laa Billaay Aliwu Ba Chéri Jee Bu la Jee tooñatee Jéggal koo Yaw rekk la gëm waaw Mon chéri Mon chéri Mon chéri Yaw rekk laa waaw Mon chéri Yaw rekk laa Mon chéri Yaw rekk laa waaw Mon chéri Yaw rekk laa waaw Mon chéri Yaw rekk laa waaw