Love bi nga may wan daf ma suur man Dolli ma fit rekk may free Ak yaw may def lu ma dul mën Xol bi laa la tuddee Li des samay àtt Ak jàmm bi ngay daj Lay boole jox la tokk looy laaj Jox la sama xol Maa doon sa support Doo gisaat ku kay daaj comme man Belle ! Bàyyi ma laal la profil, bébé Yaw wax ma looy laaj? Mënatuma toog chill, déedéet Yaw looy waac Hey, ma ni lii lan la? Sama duguda ah Yaay sama life Hey, ma ni lii lan la? Li ma duggu lan la? Man yaw yaay sama life, bébé Tippoo, yaw laa sopp tippoo Tippoo, man sama xol laa tippoo Yaw sibbo, yaa jar a topp sibboo Assiko ma di ka waay ba ci kaw krekk Ak yaw lu ma songu daan Yaa sax ci sama xol bee Fi nga may jàpp ci neex soo ko waññiwul dinga ma gaañ Nank rekk Def ma nank rekk Ray ma rekk No, no, ray ma rekk Maay sa bandit saleté Nanga ma jël ci defere ma Jàpp rap tëj mënote ma, defaral ma Bàyyi ma laal la profil, bébé Yaw wax ma looy laaj? Mënatuma toog chill, déedéet Yaw looy waac Hey, ma ni lii lan la? Sama duguda ah Yaay sama life Hey, ma ni lii lan la? Li ma duggu lan la? Man yaw yaay sama life, bébé