Gis naa bu baax ni nga may xoolee Yaa ngi xool lu mool waaye am naa borom Man de setlu naa ni nga may ginge Bëgg naa nga gëm Yàlla, doo ma fi ame Dégg naa la Su jaaree ma ñakk jom dinaa ko def Su jaaree ma bokk la dinaa ko def May ma semaine ma wax la ni ma la bëggee Yaa ma gënal waay Yaa ma gënal waay Kon ayway ni wax leen ci Xale yi jaral nga ma Ki la jaral yaw jaar na Sonal nga ma Ayway ni wax leen ci Jaral nga ma Moom mi la jaral yaw jaar na Sonal nga ma Ba ko muy déconné Xawma la ci tatoné Xale yaa ngi fi di zalonné Ngay topp ki di déconné Ngay ñaan samit, yaa ñàkk jom Ñëwal fi, kay Te nga bàyyi ki di déconné Ayway (déconné) Bàyyil way (tatoné) Ñëwal fi way (zalonné) Te nga bàyyi ki di déconné Man seetlu naa ni nga fi ñëwee Nga ñëw di xool soo ma Man de setlu naa ni nga may ginge Bëgg naa nga gëm Yàlla, doo ko fi ame Ay Ki dafa ma ray dama dee di cas Xale jox ma sama ji am dédicaces Sama yaakaar ci ki doo ko tas Nob la mbëggeel bu xor du kenn Na daagu moo xool lew mu tàngalu Mooy doole Yaw dinga moo ko pas, billaay Ki romb sama fit bi di maas, wuyay Ayway ni wax leen ci Jaral ji ko Dinga moo ko pas, billaay Ki romb sama fit bi di maas, wuyay Ayway ni wax leen ci Jaral ji ko Dinga moo ko pas, billaay Ki romb sama fit bébé, wuyay Ba ko muy déconné Xawma la ci tatoné Xale yaa ngi fi di zalonné Ngay topp ki di déconné Ngay ñaan samit, yaa ñàkk jom Ñëwal fi, kay Te nga bàyyi ki di déconné Ayway (déconné) Bàyyil way (tatoné) Ñëwal fi way (zalonné) Te nga bàyyi ki di déconné