Sof nga may jaay dindil o bi xol Nga def ci a ma yëngal la, noonu lañu may woowe Saf laa lay jaay laajal ñi fi jaar Jekk mol ñu di ma topp ma teg ci jónge Sof naa ci xale, duma moromu gone Fiir naa ba dof mais jar na ko Sof naa ci xale, duma moromu gone Ñi ngi lay topp mais neexu ma Géré ko nu ma mel géré ko Yaa boo kon ba muy neex kon nak géré ko Géré ko, sama mool géré ko Ku bëgg dangay fiir moo tax géré ko waay Ay da may neex, ni nga mel da ma neex Soo salar ñi ko fële sama xol bi gëna feex Ay da may neex, sa moolaay da ma neex Soo defaro ba génn sama biir xol gëna feex way Gëlëm dof, mënoo mos Xale bi dina ma gaañ Mbëggeel dina ma ray Mënoo ko xam bu la rawe xaar ko tës Li ma la naral boo ko dégg dinga yuuxu Ay bëgg ba mbëk te yëguma dërëm Def ma lu ne te bu ma ci yërëm Naa la dugal fu lëndëm lëndëm Nga gëna daldi gëlëm Yaw def ma loolu, loolu noonu Teg ma foofu, foofu noonu Naa la def kilifa si këram Ñëwal, doo jokker dërëm Céy li nga ma jaral Wax ma loo ma naral du ma ci doyal Tooñal ma la faral jox la xol xale bi doxal Fi nga jàpp foofoo baax Ma ni delloo fa sa Man duma bàyyi ndax yaay gaañ Xale bi doy nga ma Man bëgg naa jigéen bu mel ni yaw Jongé nga lool tax góor ñi di la topp Feeling bi ne ci yaw neex na ma Boo leen jekkoo dee leen baal Sof naa ci xale, duma moromu gone Wóolu naa la xale bi Sof naa ci xale, duma moromu gone Fi nga ko te foofu la Géré ko nu ma mel géré ko Yaa boo kon ba muy neex kon nak géré ko Géré ko, sama mool géré ko Ku bëgg dangay fiir moo tax géré ko waay Ay da may neex, ni nga mel da ma neex Soo salar ñi ko fële sama xol bi gëna feex Ay da may neex, sa moolaay da ma neex Soo defaro ba génn sama biir xol gëna feex way