Namm naa la yaw Gëj naa la gis Kenn du baay boobu waay Yaw sama xarit Maa def la xarit Nga def ma sa noon Fayoo naar bi xoromam Baadoola bi Billaay fi ma jaarak yaw Ku fa jaarak kala Yàlla boolel Foo tolloo di ko way Yaw sama xarit baa ngee Ndaanaana ngi Fi ma jarak moom Ku fa jaarak kala Yàlla boolel Foo tolloo di ko way Ay sama xarit baa ngi Ndaanaana ngi Boo ma gisul toog di ma yàq Te boo ma gisee reetaan Nga foog ni dunya nii la mel Yaw mi ne ko waaj Man mii de xam naa ki ma doon Ndax maa ngi sant Yàlla Awma sax jotu di la jëw Xam nga ni man maay waaj Boo ma gisul toog di ma yàq Te boo ma gisee reetaan Nga foog ni dunya nii la mel Yaw mi ne ko waaj Man mii de xam naa ki ma doon Ndax maa ngi sant Yàlla Awma sax jotu di la jëw Xam nga ni man maay waaj Ree ma, ree ma Ay ree ma, ma lay reetaan de ma yaw Ree ma, ree ma Yaw ree ma, ma lay reetaan de ma Ree ma, ree ma Yaw ree ma, ma lay reetaan de ma yaw Ree ma, ree ma Yaw ree ma, ma lay reetaan de ma Ree ma, ree ma Ay ree ma, ma lay reetaan de ma yaw Ree ma, ree ma Yaw ree ma, ma lay reetaan de ma Ree ma, ree ma Yaw ree ma, ma lay reetaan de ma yaw Ree ma, ree ma Yaw ree ma, ma lay reetaan de ma