Fi sa xol bi ne fa laa nekk Fi sa mbëggéel toog laay toog Fi nga fanaan fa laay nelaw, humm Bi moo jugé dem bay ñibbi Danga ma xëccaat ne na toogal Ndax pareguma ci yaw Noo ko mëne Lii noo ko mëne Noo ko mëne, my baby Wax ma foo ma jëme Yaw foo ma jëme Foo ma jëme, xale bi Est-ce que xam nga li nga jaral Mooy bi may jooy love Yaa ma jël aakimu, kenn du ma separé ak yaw Yaa may jooyloo, maa la jooyloo Jëlal bum bi yew ci baat foy dem ñu àndandoo Ndax bëgg naa la (he he he he) Xam naa ni bëgg nga ma (he he he he) Ndax bëgg naa la (he he he he) Yaw tamit bëgg nga ma (he he he he) Yaw rekk ay ki may jege, di ma jege Di ma dundal, di ma miirloo Tegsi di ma dofloo Man yaw rekk laay bëgg di la bëgg Amul douter bu ñu wéetee yaw yaay nekk sama goûté Hummm hum Bu may faayu dama lay humm hum Bu ñu wéetee yaw yaa ma may humm hum Bu ma faayu dama lay humm hum Bëgg naa la, bëgg nga ma Suñu diggante daq lem Ku ko amul na nga xaar Wóolu naa la, wóolu nga ma Foo jub lu la bëgg, dem may sa code-phare Est-ce que xam nga li nga jaral Mooy bi may jooy love Yaa ma jël akimo, kenn du ma separé ak yaw Yaa may jooyloo, maa la jooyloo Jëlal bum bi yew ci baat foy dem ñu àndandoo Ndax bëgg naa la (he he he he) Xam naa ni bëgg nga ma (he he he he) Ndax bëgg naa la (he he he he) Yaw tamit bëgg nga ma (he he he he)