Boo xamoon xol bi lum la dencal Doo dem feneen di fa wëri mbëggeel Ba muy metti ki nga nekkal Tay bu neexe war nga ko won mbëggeel Bu ñu ma bëggee jot ci yaw lañuy jaar Parce que yaay sama faiblesse Kenn du nga ci man ku nekk ak ñaar Xol bi jël nga ko ne fees Bu guddi gi jotee ba nit yi yépp nelaw Ci nga may jege xëcc ma aj ma ci kaw Nga naan ma 'uh-ah', noo ko bëggee? Ma naan la nii la ko bëggee Yaa jël xol bi, tijj ko def ci love bi Remplacer ki fa nekkoon ndekete dama juumoon Tebbi nga ace bi, jël xolam caabi Dem ba géej sànni, mbëggeel moo mën lii Fi nga jàpp foofoo neex Bu ko bàyyi yaa ko moom Ku la ko tere dina ñów di xeex ak moom Yow fi nga jàpp foofoo neex Bu ko bàyyi yaa ko moom Ku la ko tere dina ñów di xeex ak moom Bae ci night bi Mënuma nelaw tay ci night bi sans nga nekk fi Oh ma vie Wax ma ni may sa love, may sa aaah-eeeh Bu guddi gi jotee ba nit yi yépp nelaw Ci nga may jege xëcc ma aj ma ci kaw Nga naan ma 'uh-ah', noo ko bëggee? Ma naan la nii la ko bëggee