Boo ma bëggee danga may defal cadeaux Di ma naxee yëngel caabi auto Mon bébé dugal ma ci château Ma jël fa samay foto wan leen ni nammuma cooco Kaay fecc ak man (Ñëwel ñu fecci) Kaay fecc ak man (Ñëwel ñu fecci) Kaay fecc ak man (Ñëwel ñu fecci) Kaay fecc ak man (Ñëwel ñëwel ñëwel) Tukku ci ngalam Musique bi di daw ñëpp di dance Ma def la madame Yëkkati ba ci kaw Ñepp la fans ba nare basang Hôtel lañu jëm jàppu fa temps Ma ne bu repe dee bu reppul dee tay la bësam Ajul ba ci kaw jàppu sa njax nit yi la bëggul Ci suuf lañu nekk tok di la xar ree de soucis Ree de soucis yaw doo jegu ree de soucis (Heee ree de soucis) Am nga cat am nga feeling Fees nga dell mel ni meeting Dëgg daaj teksi cline Fu ma tourner nga toppuma mel ni sikkim Yaay biru xaar ci deexin bébé Soo ma bëggee dagu may defal cadeau Di ma naxe yëngel caabi auto Mon bébé dugal ma ci château Ma jël fa samay foto, wan leen ni nammuma cooco Kaay fecc ak man (Ñëwel ñu fecci) Kaay fecc ak man (Ñëwel ñu fecci) Kaay fecc ak man (Ñëwel ñu fecci) Kaay fecc ak man (Ñëwel ñëwel ñëwel) Xale bile nammul përëm Waxalewul or diamant fees na dell këram (Nammul nammul tus) Dëgg daaj tak sërëm Goor du ko yàpp ma ko bëgg ma ko gërëm He ma ko gërëm ce ce! Bàyyil lak sa biir, coow li di riir Caaw nga sa xiir Noquleen bañu miir Jekk bii du liir Faux bi du piir Nob la ba miir Léegi sax dama fiir