Li Yàlla sak lépp ci taar sa jëm la ma doon misal Musuñu tegante waaye ñoo bokk fi ñu doon xool Xëccoo mettiwoon na, waaye yaa fi na lu te yaw la faral Xol yi wara ànd bañ juddoo ba tay ñoo ngi werante Waaye su ñu dajee kenn ci ñun dootuñu werante Ku ne dina xam ne ki laa doon xaar ki rekk laa war doon Ne na waaw te xol bi ne na waaw Waajur yi ne nañu waaw, xarit yi ne nañu waaw Ñépp ne nañu waaw kon yaw la wara doon Ne na waaw te xol bi ne na waaw Waajur yi ne nañu waaw, xarit yi ne nañu waaw Ñi bañoon sax ñépp ne nañu waaw Ak yaw bëgguma sax deme sama xel Bëgguma solu bari mbëggeelu 0 calcule Man naguwuma sax ku yaq sama xel Ci yaw meme su de dëgg la ma la ko ñekk wedi Foogoon na ni xol bi yàqu na te dootuma bëggaat Déception lu metti la comme dal dootoo bëgg dundaat Wante yaw, danga mel ni drogue ci psychopathe Dof buy gaañ te loo la soxla Ne na waaw te xol bi ne na waaw Waajur yi ne nañu waaw, xarit yi ne nañu waaw Ñépp ne nañu waaw kon yaw la wara doon Ne na waaw te xol bi ne na waaw Waajur yi ne nañu waaw, xarit yi ne nañu waaw Ñi bañoon sax ñépp ne nañu waaw Ne na waaw te xol bi ne na waaw Waajur yi ne nañu waaw, xarit yi ne nañu waaw Ñépp ne nañu waaw kon yaw la wara doon Ne na waaw (yaw la doon séet) Te xol bi ne na waaw (te yaa ngi sama wet) Waajur yi ne nañu waaw, xarit yi ne nañu waaw Ñi bañoon sax ñépp ne nañu waaw Ne na waaw te xol bi ne na waaw Waajur yi ne nañu waaw, xarit yi ne nañu waaw Ñépp ne nañu waaw kon yaw la wara doon Ne na waaw (yaw la doon séet) Te xol bi ne na waaw (te yaa ngi sama wet) Waajur yi ne nañu waaw, xarit yi ne nañu waaw Ñi bañoon sax ñépp ne nañu waaw Soxlatuma dara ndax nago ba tay ndax gis na sama gow Àdduna bi yépp sa diggante loxo moo ci gëna woor Ne naa la waaw, xale bi, yow laa doon xaar Départ ba la ma mbëggeel arrivé ci yaw dotoo ma raw Daw na ba sonn mënul nekk boobu xol bi ne na waaw Mettiwoon nga daw, supporté nga samay caprices sax samay yu ndaw