Jeeba la boy (Brill on the beat) Wax ma loo bugg ma defal la ko Wax ma loo namm chérie ma wutal la ko Même bu de auto ma jëndal la ko Yóbbu la ci château nga dëkke dodo Dama xam fuy xasan foofu lay wokk Sa ex yi la doon sonal ñépp lay noq Aj la ba ci kaw kenn du la jot Jox la xiir bi nga leen di caw Ma taxaw naan ko ñaaw Yaw mbëggeel dafa neex boo koy kafe sax day neex Sa biir xol bi lay jàpp mel ni dañ ci duggal peex Mënoo xam li may wax tant que demoo ci ba mu jeex Fok nga ñam kaani waaw doog a xam lu lem di saf Awa ne na ma dafa neex Makhfou ne na ma dafa neex Kadia ne na ma dafa neex Même Maimouna ne na ma mbëggeel billaay dafa neex Kon dama la bugga Te ku mu metti naanal amoniaque Baygon wala maladio Saa yoo yewoo Nga ñuy gis ñuy lëngoo Ma naan ko! Bëgg na, bëgg naa ko Bu dul ren di déwén dina ko def Ndax yaa ma jaral loolu Dama tegi gros lots ooh Moom moo may tël man maa ko bërëŋ Xanaa nanduloo loolu Ñun buñu bégee moo ñu bégal Buñu jooyee moo nu jooyloo Bébé xam nga ma bu baax, duma ku tegi ndawal Fi ma lay jàpp ba nga ni axxx, maa ko xam te dama koy dawal Bébé xam nga man lu tax ma bëgg la dama ci sawar Danga fekk fi ceebu keccax nga valorisé ko sànni ci ndawal Ndaxam laax dinañu koy sëlmoo ñun dañu koy këppoo Sama carte bi yaw la voteel tak séy bi jall ci leneen Kon danga mer man maa ngi baax Jox ko ndox mu naan mu geex loolu mënul ñax Yaw mbëggeel dafa neex boo koy kafe sax day neex Sa biir xol bi lay jàpp mel ni dañ ci duggal peex Mënoo xam li may wax tant que demoo ci ba mu jeex Fok nga ñam kaani waaw doog a xam lu lem di saf Abba ne na ma dafa neex Ngoné ne na ma dafa neex Habib ne na ma dafa neex Même Aicha Aziz ne na ma mbëggeel dafa neex Kon dama la bugga Te ku mu metti naanal amoniaque Baygon wala maladio Saa yoo yewoo Nga ñuy gis ñuy lëngoo Ma naan ko! Bëgg na, bëgg naa ko Bu dul ren di déwén dina ko def Ndax yaa ma jaral loolu Dama tegi gros lots ooh Moom moo may tël man maa ko bërëŋ Xanaa nanduloo loolu Ñun buñu bégee moo ñu bégal Buñu jooyee moo nu jooyloo Mbëggeel mbëggeel mbëggeel dafa neex Neex neex neex neex-a-neex ayyyee Waaw we waa waaw waaw Kon dama la bugga Te ku mu metti naanal amoniaque Baygon wala maladio Saa yoo yewoo Nga ñuy gis ñuy lëngoo Ma naan ko! Bëgg na, bëgg naa ko Bu dul ren di déwén dina ko def Ndax yaa ma jaral loolu Dama tegi gros lots ooh Moom moo may tël man maa ko bërëŋ Xanaa nanduloo loolu Ñun buñu bégee moo ñu bégal Buñu jooyee moo nu jooyloo