Tooñ nga ma been yoon Yaw chérie maa la baal Tooñaat ma ñaari yoon Bu ñeent dama lay baal Li ma yëg ci sama xol Yàlla seede na ma ko, waaw Yaw ñëwal fi nga jege ma Loo bëgg wax ma ko, waaw Yaw biig, yaw biig ci guddi nelawuma Di la xalaat ba léegi babe nelawuma Yaw déedéet, bul defe noonu doyalu ma Ku la naan màndi ku la ray gëne reew sama Te ba nga yegsee la xel yi dal ñépp naan kaar mashallah! Man namoon naa la chérie boy, waawaawaaw Aah aah aah aah Allame Allame Allame téléphonaa Allame Allame Allame téléphonaa Allame Allame Allame téléphonaa Chérie, Allame téléphonaa Tooñ nga ma been yoon Yaw chérie maa la baal Tooñaat ma ñaari yoon Même bu ñeent dama lay baal Bu ñeent dama lay baal Yaw yaay booy, kaay jege ma Mbëggeeloo may gaañ Yaw yaay booy, kaay jege ma Mbëggeeloo may gaañ Mbëggeel yaa mën a boole Nit ku ñuul ak nit ku weex Yaa mën a boole Bàmbara beek tukulóor bee Tàkkuloo ko tàkkuma ko Jigéen la yërëm ko Waaye, yaw waaye bum la saay-saay yeeeh Mbëggeel yaa mën a boole Nit ku ñuul ak nit ku weex Yaa mën a boole Bàmbara beek tukulóor bee Tàkkuloo ko tàkkuma ko Jigéen la yërëm ko Waaye, yaw waaye bum la saay-saay yeeeh Ma ci jobaate, kalaju laa Abadan doo fay Ki nga bëgg ba bëgg ko Soo la meree dangay feebar di dox ci yaw Mel ni ku sibbiru mbëggeel metti na Ki nga bëgg ba bëgg ko Soo la meree dangay feebar di dox ci yaw Mel ni ku sibbiru mbëggeel metti na Soo xaaree ma ñëw Fi nga ne fi ma nekk Mbaye sori nanu Te xol day gise Saa su ma lay gisee man kontaan Ni mbëggeel, mbëggeel, mbëggeel, mbëggeel Metti na waaw waaw Maa woo la, ndaw sile bëgg naa la! Yaw soo xaaree ma ñëw Fi nga ne fi ma nekk Mbaye sori nanu Te xol day gise Saa su ma lay gisee man kontaan Ni mbëggeel, mbëggeel, mbëggeel, mbëggeel Metti na waaw waaw Maa woo la, ndaw sile bëgg naa la! Yaw dërëm yaay, yaw dërëm yaay Dërëm yaay, dërëm yaay Dërëm yaay, chérie xaadi dërëm yaay Dërëm yaay, dërëm yaay Clédore dërëm yaay Baay Aïcha dërëm yaay Dërëm yaay, dërëm yaay Youssou dërëm yaay Dërëm yaay, she tet tet tet tet!