Musique Xalé, vibes Xalé Man ak Karabalik (banger banger banger banger ah) Youssou, Omar, Baba ngay guiss ci man Malal, Xumam, Keyti ngay guiss ci man Artist demb rek ngay ci man ehhh gnom gneup ngay guiss ci man Boko gueumé mouy fayla lolou lagn ma wax Ma bayi lëëp diap néki ci waar Téwal banlieue ndongo lay represent heee man Ndongo lay represent Musique musique ko, musique musique ko Musique musique ko, musique musique ko, musique dafa nekh Musique musique ko, musique musique ko Musique musique ko, musique musique ko, musique dafa nekh Ay diouni ndaw bayi lëëp diap ci yaw Ay diouni ndaw faté lëëp diap ci yaw musique Xouran Naka xouran Li louka daka daka daka dou am Xouran Naka xouran Li louka daka daka daka dou am Boy Li moy bouyaka bouyaka (djeul vibes mélodie) Defko ci ndaga, ci ndaga (damay international) Xamnga ci Naka, ci Naka (represent my hood) From Senegal, Senegal Yayaya Fou Malade, Fou Malade wax nga Niou sa xalat Fou Malade, Fou Malade wax nga Niou sa xalat (Ndax Musique Xalé, vibes Xalé Man ak Karabalik (banger, banger, banger, banger ah) Youssou, Omar, Baba ngay guiss ci man Malal, Xumam, Keyti ngay guiss ci man Artist demb rek ngay ci man ehhh gnom gneup ngay guiss ci man Boko gueumé mouy fayla lolou lagn ma wax Ma bayi lëëp diap néki ci waar Téwal banlieue ndongo lay represent heee man Ndongo lay represent Musique musique ko, musique musique ko Musique musique ko, musique musique ko, musique dafa nekh Musique musique ko, musique musique ko Musique musique ko, musique musique ko, musique dafa nekh Man Nala bismilah, bismalah) Nga nanma kanaraw, kanaraw Man nanla corruption moukhoum kagn ci kaw lay door té nioussi souf lay gagn feuneukeu what's up Wou yoyoyoy fimoy Senegal ndiaye Wou yoyoyoy fimoy Senegal ndiaye Boy Li moy bouyaka bouyaka (djeul vibes mélodie) Defko ci ndaga, ci ndaga (damay international) Xamnga ci Naka, ci Naka (represent my hood) From Senegal, Senegal Yayaya Yalla miy mayé man ma yoor sama weurseuk Ouh yeah, ouh yeah sant na Yalla Musique Xalé, vibes Xalé Man ak Karabalik (banger, banger, banger, banger ah) Youssou, Omar, Baba ngay guiss ci man Malal, Xumam, Keyti ngay guiss ci man Artist demb rek ngay ci man ehhh gnom gneup ngay guiss ci man Boko gueumé mouy fayla lolou lagn ma wax Ma bayi lëëp diap néki ci waar Téwal banlieue ndongo lay represent heee man Ndongo lay represent Musique musique ko, musique musique ko Musique musique ko, musique musique ko, musique dafa nekh Musique musique ko, musique musique ko Musique musique ko, musique musique ko, musique dafa nekh