Papelaye Àdduna a ngi nuy xool Nee nañ man ak yaw du sori Nee nañ ma du mool Nee nañ lii du luy dem fenn Ku baax du ñàkk i noon Li nuy tabax lañ bëgg a yàq Te man duma ku bon Yéenewuma la man safaan Àdduna a ngi nuy xool Di nu ree ree yu rafet Bëñam ya weex lool Waaye dereet a ko lal Bëñ ya weex na Waaye dereet moo ko lal Su ñu sañoon man ak yaw dootun bokk lal Ñi ni dañu may xeex Ñele ne dañu lay xeeb yaw Xamuma lu nu leen def Xamuma lu ñu nu toppe All day da ñu may xeex Sometime dañu lay xeeb yaw Xamuma lu nu leen def Lan moo tax manuñu toppe Dama yam sama life my boy Mayuma kenn ci sama life muy dogal Dama yam sama life my boy Man mayuma kenn sama life muy dogal Dama yam sama life my boy Mayuma kenn ci sama life muy dogal Dama yam sama life my boy Mayuma kenn ci sama life muy dogal Àdduna a ngi nuy xool Boo yaboo nga moytu leen Bu ñu xamee foo jëm Duma ne doo yegg Waaye dina jafe lool Seen i làmmiñ dafa tooke Seen i pexe bon Boo yaboo nga moytu leen Boo yaboo nga moytu leen Fexeel ba buñ la jam naani Wiiri wiiri, jaari Ndaari Toppal sa yoon ba dégg daan Ñi ni dañu may xeex Ñele ne dañu lay xeeb yaw Xamuma lu nu leen def Xamuma lu ñu nu toppe All day da ñu may xeex Sometime dañu lay xeeb yaw Xamuma lu nu leen def Lan moo tax manuñu toppe Dama yam sama life my boy Mayuma kenn ci sama life muy dogal Dama yam sama life my boy Mayuma kenn sama life muy dogal Dama yam sama life my boy Mayuma kenn ci sama life muy dogal Dama yam sama life my boy Mayuma kenn ci sama life muy dogal