Hey Massamba Walo Jàllo, jàllo, yaay Jàllo, jàllo, yaay Xam nga dama laa bëgg Ngir rekk danga maa bëgg Am nga yitte maandu nga Am nga ngor dangaa dëggu Sooy dem bul ma fi bàyyi Ajaa mooy ajaa Ma xam fa nga jëlee mbaax Ajaa mooy ajaa Ni nga tabee kaar Ajaa mooy ajaa Ajaa jàllooy taar Ajaa mooy ajaa Mu dàq la yàqul sa taar Ajaa mooy ajaa Ajaa jallooy taar Ajaa mooy ajaa Ni nga tabee kaar Ajaa mooy ajaa Fa nga jëlee mbaax Jàlloo, Jàlloo, yaay Ajaa mooy ajaa Jàlloo, Jàlloo, yaay Ajaa mooy ajaa Jàlloo, Jàlloo, yaay Ajaa mooy ajaa Jàlloo, Jàlloo, yaay Ajaa mooy ajaa Ajaa mooy ajaa Ajaa mooy ajaa Ajaa mooy ajaa Daqqante leen ci seen biir Sutanteleen te ba fiiram gi Su njaag agsee nga xam ne ñëw na Jàllo jeeri tukkuloor Sàmba Ngaari jamaa yeah Sooy dem bul ma fi bàyyi Ma xam fa nga jëlee mbaax Ni nga tabee kaar Mu dàq la taxul nga ñaaw Jàlloo, Jàlloo, yaay Ajaa mooy ajaa Jàlloo, Jàlloo, yaay Ajaa mooy ajaa Jàlloo, Jàlloo, yaay Ajaa mooy ajaa Jàlloo, Jàlloo, yaay Jàlloo, Jàlloo, yaay Ajaa mooy ajaa Jàlloo, Jàlloo, yaay Ajaa mooy ajaa Jàlloo, Jàlloo, yaay Ajaa mooy ajaa Jàlloo, Jàlloo, yaay Ajaa mooy ajaa