Eh Massamba walo Hey waay Zoom on the beat Bëgg naa la Reason to be, man fonk naa la Yaay jant bi, man bëgg naa la Nii ma la bëggee yi jeggi na dayo Eh way ye way mi girl Mi yi dei ma for life Lu nekk jaral nga ma Kenn mënul tax, man mere la Ñook seeni wax Fuck nañu leen daaw Man so merre damar jaaxle, tiis Dama la bëgg Be neen jigéen mënul tax ma giif Ndax yaw la bëgg Amul sax Nit kuy mën xam li may yëg ci yaw Amul sax Nit kuy mën compu ni ma la bëggee yiiii Bëgg naa la man Ehh eh, bëgg naa la man Bëgg naa la man Ehh eh, bëgg naa la man Eh way! Dama la bëgg ba faf gëmewuma la Bañ lu la metti bañu yaakaar ni ñemewuma la Dama la bëgg ba faf gëmewuma la Bañ lu la metti bañu yaakaar ni ñemewuma la eh Jàmm nga may laaj ma ñëw indi feeling paj Ku dégg ngay laaj te man dama dégg daaj Ehh tamit ci àdduna, man rekk ma lay beggël Jàmm nga may laaj ma ñëw indi feeling paj Ku dégg ngay laaj ma ñëw indi feeling paj Eh tamit ci àdduna, man rekk ma lay beggël Ku la laale man lay raagal Te ku la tooñ may nangu xeex bi Eh way ye way mi girl Mi yi dei ma for life Lu nekk jaral nga ma Kenn mënul tax, man mere la Ñook seeni wax Fuck nañu leen daaw Man so merre damar jaaxle, tiis Dama la bëgg Be neen jigéen mënul tax ma giif Ndax yaw la bëgg Amul sax Nit kuy mën xam li may yëg ci yaw Amul sax Nit kuy mën compu ni ma la bëggee yiiii Bëgg naa la man Ehh eh, bëgg naa la man Bëgg naa la man Ehh eh, bëgg naa la man Eh way! Dama la bëgg ba faf gëmewuma la Bañ lu la metti bañu yaakaar ni ñemewuma la Dama la bëgg ba faf gëmewuma la Bañ lu la metti bañu yaakaar ni ñemewuma la eh